Tukki
de Youssou N'Dour
Da faa la, wóolóo
Teg la nak, fu mu tegul keneen
Di dox sa bëgg bëgg, di dab sa bànneex
Ndax seetlu nga koo yaw
Yaw la bëgg
Te yaw, yaa ko sagal
Waaw waaw!
Bu mbëggéel doon lumière
Mel na ni, ni jant bi
Te su amoon, lu ko gën ë leer dem na wut i ko
Ni yaw, jaral nga ko
Lu raw, sóoru gayndé
Waaw waaw!
Lu mu metti metti, dinga tew
Lu mu sori sori, an dinga ñëw
Ca dëgg dëgg dëgg
Dem na, ba dem, mën ë tul ë tok
Benn bés, bum la, gisul
Jox na la bii respect
Nga delloo ko bii respect
Entre vous, entre vous chérie
Du wax lii def leneen
Ca dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg dëgg ya ko diara
Ni yaw, yaa ko sagal
Waaw waaw
Fépp fu mu mën ë ne
Da fay sentir sa parfum
Loolu yaa ko ko jaral
Ndax yaa ko liggéey
Les mots qu’il utilise sont toujours en deçà
De ce qu’il ressent
Yaw yaa ko ko diaral
Chérie boy, chérie boy, chérie boy
Daf la bëuggué
Chérie boy, chérie boy, chérie boy
Kay nga jege ko
Mou laye déy
Yaw mii yaw
Su fekkee li mu la wax doyu la
Boo yakkamtee
Mu def al la ko ni nga ko bëggée
Mom contane neu
Te sakh yaguena bëgg thi yaw
Boo yakkamtee
Mu def al la ko, ni nga ko bëggée
Ça lui vas, chérie sa lui va, lo def nekh na ko
Da fa laa, da fa laa, def ni nga ko def
Loo bëgg, mu indil la ko
Loo laaj, mu kheuthiel la ko
Su fekkee amu ko, mu ñaan ko yalla
Chérie boy, chérie boy
Yaa ko ko diaral
Chérie boy, chérie boy
Lo diokhogne mo dok
Chérie boy, chérie boy
Lo def noonu la
Chérie boy, chérie boy
Yaa ko ko diaral
Youssou Ndour, madjiguene
Boul yekhal dara
Na gua gaw, na gua gaw
Te li djieuntima
Soxla yi, soxla yi
Gnome ñoo ma gueteun
Más canciones de Youssou N'Dour
-
7 Seconds (feat. Neneh Cherry)
The Guide (Wommat)
-
7 Seconds (feat. Neneh Cherry)
7 Seconds: The Best Of Youssou N'Dour
-
Salimata
History
-
Beykat
Joko: The Link
-
Habib faye
Respect
-
Habib Faye
History
-
Habib Faye
Habib Faye
-
Medina
Set
-
Serin Fallu
Africa Rekk
-
Birima
Joko: The Link
-
Liggeey
Joko: The Link
-
Bukki yi plus
Spécial fin d'année 2022
-
Létt ma
Rokku Mi Rokka (Give and Take)
-
Old Man (Gorgui)
The Guide (Wommat)
-
Daan
Daan
-
Gorée
Africa Rekk
-
Bull Ko Door
Africa Rekk
-
Be careful
Africa Rekk
-
Jeegel Nu (Forgiveness)
Africa Rekk
-
Conquer the World (feat. Akon)
Africa Rekk