Spirit
de Youssou N'Dour
Han, han, sa kattan bari na, sa bateau gaaw na, te saw fit rëy në
Han, han, sa kattan bari na, sa bateau gaaw na, te saw fit rëy në
Han, han, sa kattan bari na, sa bateau gaaw na, te saw fit rëy në
Waññi ko, waññi ko, waññi ko
Waññi ko, waññi ko, ëpp në
Waññi ko, waññi ko, waññi ko
Waññi ko, waññi ko, ëpp në
Han, han, sa kattan bari na, sa bateau gaaw na, te saw fit rëy në
Han, han, sa kattan bari na, sa bateau gaaw na, te saw fit rëy në
Waññi ko, waññi ko, waññi ko
Waññi ko, waññi ko, ëpp në
Yaw yaa ni, ëpp óon nga, trois cent kilos
Te bés bu ne, benn xar nga daan añe
Nga neeti, at mi fi Obama ñëw ée
Yaw yaa ko gis, muy dox antu, biir Pikine
Am oon na, gaïnde gu rëccé, parc hann
Nga neeti ñu, yaw yaa ko jat, ba mu nelaw
Nga ni ma, am oon nga, benn bateau, Guinée
Te waa nations-unies, nga ka daan loué
Te diggënté, États-Unis ak Guinée
Daa woo ko daw, lu ëpp ñaar i fan
Am na benn bés, nga ni ma, my boy
Keroog daje naak, roi des arènes
Am na benn bés, nga ni ma, my boy
Keroog daje naak, roi des arènes
Ben loxo, laa ko yékkëtée, ni ko félicitations
Ben loxo, laa ko yékkëtée, ni ko félicitations
Ma tegaat ko ci suuf, ni ko, my boy
Ma tegaat ko ci suuf, ni ko, my boy
Na nga jaar, sa ma kër, ma jox la yeneen clefs
Na nga jaar, galle, ma jox la yeneen clefs
Techniques yooyu, japon laa ko jànge
Ca yooya jamono, man la ñépp di wër
Lu ñu wax nga ni fekke nga ko
Fu ñu wax nga ni dem nga fa
Doo tiit doo raf, doo dellu ginnaaw
Waaye sa ma waa jii, ken melut ni moom
Wax oon naa fi ni adduna ken du ko dajal
Te ku dul umppëlé da ñu lay ragal
Nit ku ne am lu muy des al
Ngir bu ëllëg ée ñu mën laa set al
Lu ñu wax, xam nga ko
Fu ñu wax nga ni dem nga fa
Doo tiit doo raf, doo dellu ginnaaw
Waaye sa ma waa jii, ken melut ni moom
Wax aat leen ni faw nit ku ne am lu muy des al
Ngir bu ëllëg ée ñu mën laa set al
Xam lépp, mën lépp, loolu, yalla dong a ko jagoo
Ragal al yalla, waay, ragal al yalla
Ragal al yalla, waa jii, ragal al yalla
Ragal al yalla, waay, ragal al yalla
Ragal al yalla, waa jii, ragal al yalla
Más canciones de Youssou N'Dour
-
7 Seconds (feat. Neneh Cherry)
The Guide (Wommat)
-
7 Seconds (feat. Neneh Cherry)
7 Seconds: The Best Of Youssou N'Dour
-
Salimata
History
-
Beykat
Joko: The Link
-
Habib faye
Respect
-
Habib Faye
History
-
Habib Faye
Habib Faye
-
Medina
Set
-
Serin Fallu
Africa Rekk
-
Birima
Joko: The Link
-
Liggeey
Joko: The Link
-
Bukki yi plus
Spécial fin d'année 2022
-
Létt ma
Rokku Mi Rokka (Give and Take)
-
Old Man (Gorgui)
The Guide (Wommat)
-
Daan
Daan
-
Gorée
Africa Rekk
-
Bull Ko Door
Africa Rekk
-
Be careful
Africa Rekk
-
Jeegel Nu (Forgiveness)
Africa Rekk
-
Conquer the World (feat. Akon)
Africa Rekk