N O P

de Wasis Diop

Diaw Diop Didi
Jolof music in the place han han

Muyeen tay ma toukeul dëkk bi (tay ma toukeul deuk bi)
Sañse di bégel xale yi (sañse di bégel xale yi)
Law la cat law la ma lammiñ (law la ma bët bu ay)
Djeulal sa temps snap lima sadji

Kaay foto ma, poste ko yëngël sama noon yi
À la une bi wone ma
Il est mignon, il est charmant
Wallah, il est galant, attirant

Ku mën na def, ku mënul demal toog
Sane repassera soo mënul demal took waaw
Ku mën na def, ku mënul vas là-bas
Sane repassera soo mënul dangay xaar waaw

Ndéké li koy yëngël ci man mii la
(Li koy yëngël ci man mii la)
Li may dégagé man mii la (si si)
Ak li ma yokk, naturellement feeling bi la
(Naturellement feeling bi la)
Ndéké likoy yeungeul si mane mii la

Moo tax damay zonzé (hee zonzé)
Moo tax damay zonzé (hee zonzé)
Su ma neexee zonzé
Moo tax damay zonzé (hee zonzé)

Billaay man de Yàlla téral na ma (Yàlla teral na ma)
Yàlla buur bi sagal na ma
Si samay digg nawle
Yàlla buur bi téral na ma
Ak reew mi fi mu toll
Yàlla buur bi sagal na ma haan

Mi ngi tourou eup na, doumako lal dafa fess
Tempo tempo tek ko si temps
Fouma teule doumeu lenn
Kaay photoma, dawsil photoma
Man damay fowak xale yi, dawsil photoma

Dama am thiass, ak touti thiathia thiass
Te xam naa dama beuri titeur dama koy assumé
Dama am cas, ak touti thiathia thiass
Bilay wallaay dama beuri titeur dama koy assumé

Ku mën na def, ku mënul demal toog
Sane repassera soo mënul demal took waaw
Ku mën na def, ku mënul vas là-bas
Sane repassera soo mënul dangay xaar waaw

Ndéké li koy yëngël ci man mii la
(Li koy yëngël ci man mii la)
Li may dégagé man mii la (si si)
Ak li ma yokk, naturellement feeling bi la
(Naturellement feeling bi la)
Ndéké likoy yëngël si man mii la

Moo tax damay zonzé (hee zonzé)
Moo tax damay zonzé (hee zonzé)
Su ma neexee zonzé
Moo tax damay zonzé (hee zonzé)

Xam nga dañuy zonzé
Su jeexee, jeex na, su jeexee, jeex na
Su paree, pare na, su nu nopee pare na

Demba Salimata, baba Salimata, Maître Lika Ba ma ni jugal zonzé
(Demal nga tok, fëlé, demal demal nga tok fëlé nëlé)
Yaw Reme Leye jugal zonzé, Dione Wally, jugal zonze
(Demal nga tok, fëlé, demal demal nga tok fëlé nëlé)

Demal nga tok fëlé nëlé

Más canciones de Wasis Diop