Accident

de Wasis Diop

Diaw Diop Didi
OMG

Yeen kaayleen seetaan fi ma gën
Kiy jeme bokkul ak ki ko mën
Barke Cheikh sañse sama yëf la
Ku ma ko sëkal duma la
Tayuma ko dafa ne ci man
Euh, dama ko judduwaale

Wa tamit tamit
Wa tamit tamit tamit tamit
Wa tamit tamit
Wa tamit tamit tamit tamit, tamit

Xoolal ni ma mel (yaa ngi may seen)
Xoolal ni ma mel (est-ce que yaa ngi may seen)
Gis nga ni ma mel
Man dal man dal machallah!

(Machallah!)
Man dal man dal machallah!
Machallah!
Man dal man dal machallah!

Sama seetu naxuma
Sama selfie baax na
Lu dul sañse bëgguma
Te fi ma génn noy na
Bi ci kaw mu ngi tas yakaaru bi ci suuf
Couleur yi dañ koy harmoniser ba mu cool
Yaw sañse fiita koy def
Bari felling ci la bokk
Dafay yokk bayre
Duma noon te doo ci doore

Wa tamit tamit
Wa tamit tamit tamit tamit
Wa tamit tamit
Wa tamit tamit tamit tamit, tamit

Xoolal ni ma mel (yaa ngi may seen)
Xoolal ni ma mel (est-ce que yaa ngi may seen)
Gis nga ni ma mel
Man dal man dal machallah!

(Machallah!)
Man dal man dal machallah!
Machallah!
Man dal man dal machallah!

Yeen kaayleen seetaan ni ma mel
Ndaxte sañse sama yëf la
Kayleen seetaan ni ma mel
Ni ma mel de neex na ma
Fu ma romb dañu naan
Ki de sañse rekk lay def
Moom lañ may jewe

Ne leen machallah, ne leen machallah
(Moom lañ may jewe)
Xale pare bari man la, ne leen Aïcha Balla
Am cat dégg daaj bari feeling paj
Bandi sañse ngay wër, kaay ma jox la li ngay laaj

Won naa leen
Première dame Marème Faye Sall
(Sañse rekk lay def)
Soxna Aïdara chérie Wally
(Sañse rekk lay def)
Viviane Chidid fu mu féete
(Sañse rekk lay def)
Nabou Dashe Mondial kaay dozé
(Sañse rekk lay def)
Maman Diouma Dieng jaaxate
(Sañse rekk lay def)
Lil boy Gueye boroom Torino
(Sañse rekk lay def)
Wizz JFA universal
(Sañse rekk lay def)
MSD general Istanbul
(Sañse rekk lay def)
Weuz W Paradise
(Sañse rekk lay def)
Yuga sow boroom Socosim
(Sañse rekk lay def)
Bamba Fall borom Medina
(Sañse rekk lay def)

Más canciones de Wasis Diop