From Home

de VJ

Yeah, yeaa

Dégg nañu naan
Ndaanaan boo gis ndaanaan na nekk ci ginnaawam
Yaa di sama ndaanaan, li de wor na ma
Li nga jàppoon ba mel ni, bul ko bàyyi de jikk na la
Ñi la toppoon ba ngay gone ñoo tew tay ñëw gunge la
Daagul doxel nii ku la laal man dina ma yëngal
Yaw rekk laay topp, ma chérie

Céy xale bi
Yaa ngi yëngal sama xol bi waaw
Fi nga ma yóbbu aka sori
Li nga may def ku ko dundul mënu ko xam
Ndekke mbëggeel noo neexee ni

Ku ne xam nga ki lay bégal
Ku ne xam nga ki lay gaañ
Ku ne toppal ki lay yëngal
Ku ne toppal ki lay gaañ

Yaa mën yaa ëpp doole yaa féete xale
Yaa mën yaa ëpp doole yaw rekk ci xale
Yaa mën yaa ëpp doole yaa féete xale
Yaa mën yaa ëpp doole yaa mat xale

Chérie ma ni la tay may sa ndér
Jëlal pansement bi faj ma ba ma wér, waawaaw
Yaw deko ray, deko defe nin ko bëggee du lu ay waaw
Takkleen daaj yi
Ki ma doon seet dal moo ngi ni
Li dafa neex man ma ni
Chérie yaay ki jonge
Duma la wéccok keneen, waawaaw
Waawaaw, hum!

Kon yaa ngi ni, sama bandit bi way
Boo soloo daagul, ma daagu si way
Li la yëngal ma, ma yëngal
Kaay ñu gisee way bébé
Daneel nga ma!

Ku ne xam nga ki lay bégal
Ku ne xam nga ki lay gaañ
Ku ne toppal ki lay yëngal
Ku ne toppal ki lay gaañ

Yaa mën yaa ëpp doole yaa féete xale
Yaa mën yaa ëpp doole yaw rekk ci xale
Yaa mën yaa ëpp doole yaa féete xale
Yaa mën yaa ëpp doole yaa mat xale

Li mooy mbëggeel man ak mbëggeel
Li mooy mbëggeel la, man ak mbëggeel looy

Ba tax na, dama la, dama la
Dama la bëgg lool chérie

Dama la, dama la
Dama la bëgg lool chérie, waaw!

Más canciones de VJ