Yeuk Yeuk

de Viviane Chidid

Xale bii, sama xol yaa ci ne
Te su ma la gisul, yeah yeah yeah
Te su ma la gisul
Duma añ, duma réer
Jarabi naa la leer
Te su ma la gisul, no no no
Te su ma la gisul (ooh wouh! wouh!)

Oooh!
Oh yesa-yesa-yes
Reewantul bari caprices, bëgg naa
Defal li ci sa xel (ci sa xel)
Chéri loo bëggul, man mi bëgguma
Xale bi kenn du yaw, yeah yeah
Yóbbuma fu la neex man ñeme naa
Sucrée-salée naa

S'il te plaît bae, yokk ko maa tay nob la (maa tay nob la)
Lu ma ci goobé gar ko, uh la-la-la! (uh la-la-la)
Lu may dund ak moom neex ba mel ni lem
Chéri, sama love
Su ma la gisul wéet naa, yeey!

Xale bii, sama xol yaa ci ne
Te su ma la gisul, yeah yeah yeah
Te su ma la gisul
Duma añ, duma réer
Jarabi naa la leer
Te su ma la gisul, no no no
Te su ma la gisul (ooh wouh! wouh!)

Uuuh!
Oh yesa-yesa-yes
Ma baby kenn safu ko, na-na-na
Bëggul li metti sama xol, na-na-na
Du taxawaalu dem fu ne na-na-na-non yeah
Mbëggéel bu doon drogue, overdose naa
Ndax moom laay use man
Xale bile sick naa, yey!

S'il te plaît bae, yokk ko maa tay nob la yeah (maa tay nob la)
Lu ma ci góobe gar ko, uh la-la-la! (uh la-la-la!)
Oooh, jege ma jege ma baby (ay ay ay ay)
Yaw chéri sama lover
Su ma la gisul dof naa, yey

Xale bii, sama xol yaa ci ne
Te su ma la gisul, eeeeey....

Lune sa xel wax ma
Lo bëgg ma defal la
Tay maa lay tëral neexal la
Baby maa ngeek doole ji te soxor naa
Ni ngay def sama xol
Di koy neexal ma koy dund tout le temps
Ma mel ni ku nekk àljanna
Dama la koy delloo tay yëg-yëg la

Ma ne mbëggéel nii la
Ana Clara kontaan nga
Ndax Doro Gueye gentle la
Te boo ubbee xol bi yaw yaa fa ne
Nu muy def sa xol bi
Di koy neexal nga koy dund tout le temps
Nga mel ni ku nekk àljjana
Danga ko koy delloo ndax dëgg la

Yëg-yëg, yëg-yëg, yëg-yëg, yëg-yëg
Yëg-yëg!

Ma ne mbëggéel nii la
Loo bëgg ma defal la
Tay maa lay yeetal tëral la
Man xam naa ni yëg-yëg la

Li ngay def sama xol
Di ko neexal ma koy dund tout le temps
Ma mel ni ku nekk àljjana
Dama la koy delloo tay yëg-yëg la

Yëg-yëg!

Más canciones de Viviane Chidid