Yenë Saay
de Viviane Chidid
Soo xamoon ne ma zoné
Su kër doon école awma ci classe
Ci mbedd bi laay jànge
Ba sama xël ñëw na soxlawul das
Ba may nekk guné
Mbour tukkulër ba Grand Dakar Fass
Man dem naa ci fu ne
La tête dans les nuages et les pieds sur le bitume
Lu-lu ne laa gis ba-bànneex ak diis
Lu-lu ne laa gis terewul Vivi jàpp te bàyyi
Fi ma jar ba yeksi fii
Yombul waye jombul doomu adama
Je n'aime pas le jour je ne vie que la night
Soo xamoon ne ma zoné
Su kër doon école awma ci classe
Ci mbedd bi laay jànge
Ba sama xël ñëw na soxlawul das
Ba may nekk guné
Mbour tukkulër ba Grand Dakar Fass
Man dem naa ci fu ne
La tête dans les nuages et les pieds sur le bitume
[Barack Adama]
Wooh wooh wooh wooh wooh
Yaay boy a taffée sans arrêt du lundi au lundi
Wooh wooh wooh wooh wooh
Et le daron a fait pareil sans profiter de la vie
All eyes on me, je veux tourner
Je veux conquérir le monde dans la mif' on est nombreux
Wouwou j'ai zoné dans les rues maintenant me voilà
Anhan j'ai zoné dans les rues maintenant me voilà yaye booy
Man sama life fi la musique bi jël deinthieu
Te gore na ba tijil maa ay buntu
Ku ñakk jëriñu man duma rëccu
Ku nekk ci kanam dotoo tala geestu
Bëggeel doomu adama
Indi na Viviane ak Barack Adama
Amul frontière!
Más canciones de Viviane Chidid
-
Sadik Lady
Sadik Lady
-
Yaakaar
Yaakaar
-
No Stress
Wuyuma (DTM)
-
Do Dara
Benen Level
-
Rëcc Na
Benen Level
-
Yenn Saï
Benen Level
-
Djoug Liguey
Benen Level
-
Tèrè Doundou
Benen Level
-
Nangoulema
Benen Level
-
Déranger
Benen Level
-
Senegal
Benen Level
-
Benen Level
Benen Level
-
Def Ndam
Benen Level
-
Wuyuma
Wuyuma (DTM)
-
Da Fa Gnaw
Wuyuma (DTM)
-
Mariage forcé
Wuyuma (DTM)
-
Sénégal Ben Bop
Wuyuma (DTM)
-
Mbifé
Wuyuma (DTM)
-
SOPÉ
SOPÉ
-
Yeuk Yeuk
Yeuk Yeuk