Tèrè Doundou
de Viviane Chidid
Doo ma tere dund man
Ndax sakuloo ma
Ku lay tere dund moom
Na fekk mu moom la yaw
Ndax yenn saay nit teg la coono
Dellu nekk ci nooflay
Soo ko nangoo ba mu sonn la
Yaa ko teg sa bopp waay
(Ouwaaay)
Ma ni defe ko ni ndax bakkan jàmm la bëgg
Dundel sa dund, bu leen faale
Yeen yi soxor la may nurool
Wax ji de safu ma, dóor yi de yëguma
Ndax sama yaram ma blindé
Joxoo ma lekk, joxoo ma naan
Moomuloo ma yaw mi le
Doo ma tere dundu
Doo ma tere dundu
Ngay jukk ak di daanu
Ñu ne ki dey jaambar la
Di añ ci al bi
Di réere ci mbédd mi
Ñu naan la ñafe ko noonu la
Bu amee te amuñu yaw
Nit yii la doon yénne lu baax
Ñu lay njëkk saaga
Ngay duggu ak di génn
Di ko liggënti
Ñu naan la yaw mi dey caaga nga
Bu ñu la tere dund
Doo ma tere dund
Doo ma tere dund
Man amuma jote
Te loo ma def baal naa la
Dima ligënti
Ba xëy bidanti
Xana déy yaw mii déy sonuloo ?
Dundel kenn moomu la
Àdduna noonu la
Ndax ku nekk diw du jàmm am
Tere ma dundu
Bëgg di dundu
Tay ma xamal la loo xamul woon
Doo ma tere dund
Doo ma tere dund
Doo ma tere dund
Àdduna Yàlla ngay jammu
Boo ko deful dinga gaañu
Dunduleen li ngeen di dundu ñu yénnénte jàmm
Àdduna Yàlla ngay jammu
Boo ko deful dinga gaañu
Dunduleen li ngeen di dundu ñu yénnénte jàmm
Ndax yenn saay nit teg la coono
Dellu nekk ci nooflay
Soo ko nangoo ba mu sonn la
Yaa ko teg sa bopp waay
(Ouwaaay)
Ma ni defe ko ni ndax bakkan jàmm la bëgg
Dundel sa dund, bu leen faale
Yeen yi soxor la may nurool
Wax ji de safu ma, dóor yi de yëguma
Ndax sama yaram ma blindé
Joxoo ma lekk, joxoo ma naan
Moomuloo ma yaw mi le
Doo ma tere dund
Doo ma tere dund
Ngay jukk ak di daanu
Ñu ne ki dey jaambar la
Di añ ci al bi
Di réere ci mbédd mi
Ñu naan la ñafe ko noonu la
Bu amee te amuñu yaw
Nit yii la doon yénne lu baax
Ñu lay njëkk saaga
Ngay duggu ak di génn
Di ko liggënti
Ñu naan la yaw mi dey caaga nga
Buñu la tere dundu
Doo ma tere dund
Doo ma tere dund
Más canciones de Viviane Chidid
-
Sadik Lady
Sadik Lady
-
Yaakaar
Yaakaar
-
No Stress
Wuyuma (DTM)
-
Do Dara
Benen Level
-
Rëcc Na
Benen Level
-
Yenn Saï
Benen Level
-
Djoug Liguey
Benen Level
-
Nangoulema
Benen Level
-
Déranger
Benen Level
-
Senegal
Benen Level
-
Benen Level
Benen Level
-
Def Ndam
Benen Level
-
Yenë Saay
Benen Level
-
Wuyuma
Wuyuma (DTM)
-
Da Fa Gnaw
Wuyuma (DTM)
-
Mariage forcé
Wuyuma (DTM)
-
Sénégal Ben Bop
Wuyuma (DTM)
-
Mbifé
Wuyuma (DTM)
-
SOPÉ
SOPÉ
-
Yeuk Yeuk
Yeuk Yeuk