Teeyal

de Viviane Chidid

Dèg tèl nè rèk todj na
Lou fi diar ngèn di daw bay danou
Fo tok beug gnou naw la
Wagnil eupeul tè bah nètalli
Dèg lou lèn wakhou yaram ba
Meun wakhou khaam yoon bè ko gueune
Beug buzz ba mou diaraal la
Nga tagguè ko tè dèwa goul

Kou nèk am nga loula doil
Fèkhèl nga dièm ko lidieunti dè li la wakh
Sa gallè ngi di tak di boil
Dièm ko lidieunti tè fail ko li la wakh

Lou touti nga dèf ko lou paata
Lo khaam nètali li la wakh
Yakaamti raillone na sa gnoom maam
Deugueul dara raillone na sa gnoom maam

Boul ko lèk fèk gnoro goul
Boul di wakh lo kham nè amagoul
Khamoulo do khar bagn khamal la
Djissoulo , do khar ba djis lou gueune lèr nga dèm

Tè na nga tèil , tè nga dal
Amigo li ngail wakh worou la
Nopi bakh na lo khamoul laan la
Gawa wakh meune na iindi moussiba

Dèg tèl nè rèk todj na
Lou fi diar ngèn di daw bay danou
Fo tok beug gnou naw la
Wagnil eupeul tè bah nètalli
Dèg lou lèn wakhou yaram ba
Meun wakhou khaam yoon bè ko gueune
Beug buzz ba mou diaraal la
Nga tagguè ko tè dèwa goul

Manè li khaw ma laan la
Li khaw ma laan la
Li khaw ma laan la li
Manè li khaw ma laan ni
Li khaw ma laan la
Li khaw ma laan la ni

Ki dè lidieunti na la
Lidieunti na la
Lidieunti la yow mi
Ki dè lidieunti na la
Lidieunti na la
Lidieunti la yow mi

Kou nèk am nga loula doil
Fèkhèl nga dièm ko lidieunti dè li la wakh
Sa gallè ngi di tak di boil
Dièm ko lidieunti tè fail ko li la wakh

Lou touti nga dèf ko lou paata
Lo khaam nètali li la wakh
Yakaamti raillone na sa gnoom maam
Deugueul dara raillone na sa gnoom maam

Li nga biind est ce que deug le?
Fake news maan yeungalouma
Beug buzz ba takh nga di ma sossal
Li nga dèf khaam nga loum touddou?
TOUMAL
Boil yakkati nit
Wala sakh boil biind si nit
Na la lèr li ngay wakh lou am la
Lou ko moil dina doon sa moussiba

Dèg tèl nè rèk todj na
Lou fi diar ngèn di daw bay danou
Fo tok beug gnou naw la
Wagnil eupeul tè bah nètalli
Dèg lou lèn wakhou yaram ba
Meun wakhou khaam yoon bè ko gueune
Beug buzz ba mou diaraal la
Nga tagguè ko tè dèwa goul

Dèg tèl nè rèk todj na
Lou fi diar ngèn di daw bay danou
Fo tok beug gnou naw la
Wagnil eupeul tè bah nètalli
Dèg lou lèn wakhou yaram ba
Meun wakhou khaam yoon bè ko gueune
Beug buzz ba mou diaraal la
Nga tagguè ko tè dèwa goul

Más canciones de Viviane Chidid