SOPÉ

de Viviane Chidid

Sope kaay nga jege ma
Sama xol yaw rekk la
Dama la bëgg xawma lan la
Te loolu nak demb la
Sama lettre bind naa ko
Ba posteel la ko nga jot ko
Sama album lu ko feesal
Say naatal man bëgg naa la

Amour piis ma bëgg naa la
(Amour piis ma bëgg naa la)
Sope man sopaati naa la
(Sope man sopaati naa la)
Oh diisoo na ñu dégg naa la
(Diisoo na ñu dégg naa la)
Amul lu may tere, ma bëgg la
Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la

Gisuma dara kele rekk
Bëgguma dara kele rekk
Sama xol kan moo koy dundal kele la
Wuy dama la bëgg wax
Ni ngiro na dimbali ma

Kaay jege ma
Maa neexal la
Jokk dox jaagu mbaar
Ngir nga kontaan
Sope, jege ma
Tam-tamal ma

Maa ngiro ci digg laal bi
Ayca kaay yëkkati ma

Amour piis ma bëgg naa la
(Amour piis ma bëgg naa la)
Sope man sopaati naa la
(Sope man sopaati naa la)
Oh diisoo na ñu dégg naa la
(Diisoo na ñu dégg naa la)
Amul lu may tere, ma bëgg la
Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la

Sope kaay nga jege ma
Sama xol yaw rekk la
Taar taxul bëgg naa la
Lu yàgg rekk dëgg la
Telegram bi ma jote tay
Du mandat bi sama xol la
Auto rail bi di corné
Ma lay seen du bëgg naa la

Gisuma dara kele rekk
Bëgguma dara kele rekk
Sama xol kan moo koy dundal kele la
Wuy dama la bëgg wax
Ni ngiro na dimbali ma

Kaay jege ma
Maa neexal la
Jokk dox jaagu mbaar
Ngir nga kontaan
Sope, jege ma
Tam-tamal ma

Maa ngiro ci digg laal bi
Ayca kaay yëkkati ma

Amour piis ma bëgg naa la
(Amour piis ma bëgg naa la)
Sope man sopaati naa la
(Sope man sopaati naa la)
Oh diisoo na ñu dégg naa la
(Diisoo na ñu dégg naa la)
Amul lu may tere, ma bëgg la
Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la

Oooh amour piis ma, bëgg naa la
(Amour piis ma bëgg naa la)
Sope man sopaati naa la
(Sope man sopaati naa la)
Diisoo na ñu dégg naa la
(Diisoo na ñu dégg naa la)
Amul lu may tere, ma bëgg la
Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la

Waaw waaw
Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la
Waaw waaw
Teg ma ci vélo bi, bëgg naa la

Más canciones de Viviane Chidid