Mariage forcé

de Viviane Chidid

He yeay
No no noooo
Wa waaaw

Yaye boye lii lane leu nii
Loutax ngue beugue ma méye kouma xamoul
Baye boye ki kane la nii
Loutax nga beugue ma méye kouma noboul
Té mane mii mangui dogua dougou
Si samay fouki aat'ak diourrom niaar
Té mane mi xalé la yaye
Bayiima ma diangue bathie kaanam

Bagnou ma séye wayéé
Bagnou ma séye wayéé
Bagnou ma séye wayéé
Bagnou ma séye wayéé

Kii amna alaal wooooo
Amna daaradja wooooo
Auto you rafét wooooo
Ak keur you rafét woooooo

Loutax lolou

Wawaaaw yaye
Xamnani tarou djiguéne moy séye (moy deugue)
Waat nani doumanak sén wawadjilé
Fékéné alaal lanén di djay
Kone ma xamné sama ndaw dou diar
Xamnguéne lithie biir néguou séy
Bookak laal ko xamoul everyday
Metina thi xole sunday yeah yeah
Mariage forcé mo waroul baye

Bagnou ma séye wayéé
Bagnou ma séye wayéé
Bagnou ma séye wayéé
Bagnou ma séye wayéé

Ki amna alaal wooooo
Amna daaradja wooooo
Auto you rafét wooooo
Ak keur you raféét woooooo

Té mane mii mangui doga dougou
Si samay fouki aat'ak diourom niaar
Té mane mii xalé la yaye
Bayimaa ma diangue bathie kaanam

Yaay booy
Bayiléne xaléyi niou ndiangui

Ki amna alaal wooooo
Amna daaradja wooooo
Auto you rafét wooooo
Ak keur you rafét woooooo

Más canciones de Viviane Chidid