Def Ndam

de Viviane Chidid

Xaaleul leen ko yoone wi nila
Teleulalé tapis rouge bi cii la
Dou xéwé féneu foudoule fi cii mo leu
Borom beuss bi yeksina mo ayé tay
Mani, Tayla tay bissou fête la
Bou dara seed ndaax lep matt na
Dou xéwé féneu foudoule fi cii mo leu
Borom beuss bi yeksina niou sargalko

Kaay leen Kaay leen
Kaay leen ki niou done xaar yeksina
Kaay leen Kaay leen
Kaay leen ki niou done xaar yeksina

Na nieup nieuw niou guéw fi
Mani amoul mbok xarit deukeu ndo yi
Yow da nga baax mo waral sa bessa melni
Borom beuss bi yeksina niou sargalko

Kaay leen Kaay leen
Kaay leen ki niou done xaar yeksina
Kaay leen Kaay leen
Kaay leen ki niou done xaar yeksina
Kaay leen Kaay leen
Kaay leen ki niou done xaar yeksina
Kaay leen Kaay leen
Kaay leen ki niou done xaar yeksina

Am naga foula, am nga fayda
Sa ndiambar rekka waral sa bess melni
Tamit koula xol guiss ci yow diom
Kone borom bess bi yeksina, hunnn
Rewmi kou sagnone dafay
Melni yow, melni yow
Rewmi nieupeu beug
Melni yow, melni yow
Rewmi kou sagnone dafay
Melni yow, melni yow
Rewmi nieupeu beug
Melni yow

Rewmi kou sagnone dafay
Melni yow, melni yow
Rewmi nieupeu beug
Melni yow, melni yow
Rewmi kou sagnone dafay
Melni yow, melni yow
Rewmi nieupeu beug
Melni yow

Hee
Kaay leen Kaay leen
Kaay leen ki niou done xaar yeksina
Kaay leen Kaay leen
Kaay leen ki niou done xaar yeksina
Kaay leen Kaay leen
Kaay leen ki niou done xaar yeksina
Kaay leen Kaay leen
Kaay leen ki niou done xaar yeksina

Más canciones de Viviane Chidid