Da Fa Gnaw

de Viviane Chidid

Bi aduna, lu fi jar ngay def lu ñaw ?
Fi aduna, lu fi way rindi sax sa loxo rekk lay nathie
Wax ma! Lane mo tax
Bëggulo ma waxal lu baax
Wax ma! Lan moy mbax
Budé yénagneté wugnu lu baax

Li dafa ñaaw, li dafa ñaaw, li dafa ñaaw
Li dafa ñaaw, li dafa ñaaw, li dafa ñaaw
Li dafa ñaaw nagnu sante yallah bayi beutu ginaaw
Xam na sama tolu waya tax sa fite di naw
Yalla nopina demba tay sogua nieuw gis nga fi dara du ñaaw

Lithi mane nékul si yow (ngani)
Lithi mane nékul si yow (diëlël)
Lithi mane nékul si yow, bëgueneté léne fi adina la (wawaw)
Lithi mane nékul si yow (waxal)
Lithi mane nékul si yow (kay)
Lithi mane nékul si yow bëgueneté léne fi adina la (waxal way)

Téréte biy daw thi iow moy daw thi mane
Wax ma lane motax
Meunugno yénaneté lu baax

Li dafa ñaaw, li dafa ñaaw, li dafa ñaaw
Li dafa ñaaw, li dafa ñaaw, li dafa ñaaw
Li dafa ñaaw nagnu sante yallah bayi bëtu ginaaw
Xam na sama tolu waya tax sa fite di naw
Yalla nopina demba tay sogua nieuw gis nga fi dara du ñaaw

Tu tapes dans mon dos
Tu parles dans mon dos
Tu craches dans mon dos
Sourire à la face, couteau dans mon dos
Tu tapes dans mon dos
Tu parles dans mon dos
Tu craches dans mon dos
Sourire à la face, couteau dans mon dos

Waxal way!
Tidjane waxal way (Kokoy chérie Aïda)
Abdou Mbay waxal way (Borom Conakry)
Mani Akéthié waxal way (from Abidjan la)
Baxaw waxal way (Ku bëgg lolu Viviane)
Eeeh, Kiné waxal way (Kokou sama doom la)
Awadi waxal way
Sénégal waxal way

Más canciones de Viviane Chidid