Superman Love
de Pape Diouf
Duma ci lenn lépp yaw la
Yaw yaay sama poumon gauche
Soo kontaanul dund du yomb
Amuma lu bari mais coco
Xol bi ma ko moom, jox naa la ko
Bébé sax boo demee bay fa ne
Ma doon ginnaar gi ngay reere
Kanam gi ngay ñekk gis fo dikke
Jege ma ma tay la lu bees, yaa fi ne
Bae je t'aime
Mi ko ankom mbi yitte
I love you, bébé n b'i fè
Te amo, ich liebe dich
Shiwananko, wo ai ni yoo
Boo de jant ma doon superman
Fekk yaa ngi sama wet, kenn du ma daanu
Def naa la sama soxla
Sama soxna
Sama number one
Yaay piano sama mind
Yi mélodie foo ko jàng?
Jaar ci xol bi jaaxase xel mi
Def sa tuur ci këyitu kër gi
Tegi monument de la renaissance
Tekk fa sa bos di ko status
Bet seereer ak bolu cëre
Yi may def moo ko gën a neex
Di gis tukkulër bu burde
Ki lay jooyloo moo la war a nax
Boo de jant ma doon superman
Fekk yaa ngi sama wet, kenn du ma daanu
Def naa la sama soxla
Sama soxna
Sama number one
Bae kaay ma wax la secret
Dama séy ci sa jëme ji dalaas ngoom
Yaw dal, yaay première dame ci xolu king
Doon te jarul ma la koy wax bëgg la ba ci sa waaw lay dox
Yaay piano sama mind
Yi mélodie foo ko jàng?
Yaay piano sama mind
Yi mélodie foo ko jàng?
Bilaahi mbëggeel la neex
Mbëggeel la neex xale bile (mbëggeel la neex)
Muy gën di neex neex a neex ba jaxal ma
(Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj)
Leee lee leee lee mbëggeel (mbëggeel la neex)
Man mi sax damay laaj fu mu nekk ni bilaahi mbëggeel
(Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj)
Man mi sax damay laaj fu mu nekk ni mbëggeel
(Yaw danga xam wala dangay laaj soo bëggee dugg faw ngay laaj)
Aka bari doole bilaahi mbëggeel
Más canciones de Pape Diouf
-
Damani
Ecoutez !
-
Kileu Beugue
Ecoutez !
-
Rëkkënte Bi
Enjoy
-
Yeewuleen
Pape Diouf Live au Biddew
-
Sama Seytané
L'Alchimie (Live)
-
Enjoy
Enjoy
-
Partir
Partir !
-
Dee mare
Jotna
-
Pape Diouf Live - Intro
Pape Diouf Live au Biddew
-
Dieulleul
Pape Diouf Live au Biddew
-
Massamba
Pape Diouf Live au Biddew
-
Jimy Dogo
Pape Diouf Live au Biddew
-
Immama
Pape Diouf Live au Biddew
-
Joggé Dagou
Pape Diouf Live au Biddew
-
Sa Ma Way
Pape Diouf Live au Biddew
-
Dee Ko Rof
Pape Diouf Live au Biddew
-
Ndaga
Partir !
-
Yaye - Live
L'Alchimie (Live)
-
Confiance - Live
L'Alchimie (Live)
-
Delusina - Live
L'Alchimie (Live)