Partir

de Pape Diouf

Bima deimei ñu mayema visa il faut que ma dem
Liguey nguir terral samay wadiour souma nieuwei takkla
Mane nanelay deff
Limay raggal moy wanela guinaw nga
Fattemay souboba dinama nakari ndax ande bi yagna
Mane nanelay deff
Wayei fouma diar mane dina dem liguey
Ndax may taw wadiour yi manelañu yaakaar

Né faw ma dem outidji nguir terral la
Baby sorry gueneulouma baby mangui nieuw
Beugnala xalei biley
Bima deimei ñu mayema visa il faut que ma dem
Liguey nguir terral samay wadiour souma nieuwei takela
Mane lanelay deff

Wayei fouma diar mane dina dem liguey
Ndax may taw wadiour yi manelañu yakaar

Más canciones de Pape Diouf