Challenger
de Pape Diouf
Malaw wouy malaw wouy maaaalaw (weuyooo laobé thiouray gongo)
Malaw wouy malaw wouy maaaalaw (weuyooo laobé thiouray gongo)
Woy malaw wouy maaaalaw (weuyooo laobé thiouray gongo)
Yegaleul yegaleul (yegaleul yegaleul)
Lokho ca kaw (weuyooo laobé thiouray gongo)
Laobé ken yabouléne
Goor ak jiguene dagnouy dan dolé
Bou goor gni yendo yatty diay
Taxoul seni jiguene yafouss
Jiguene yangui nassi ferr di diay
Bolek sen potou thiouraaay
Mani yegaleul yegaleul (yegaleul yegaleul) waw waw (weuyooo laobé thiouray gongo)
Laobé ken yabouléne
Goor ak jiguene dagnouy dan dole
Bou goor gni yendo yatty diay
Taxoul seni jiguene yafouss
Jiguene yangui nassi ferr di diay
Bolek sen potou thiouraaay
Yegaleul yegaleul (yegaleul yegaleul) waw mani (weuyooo laobé thiouray gongo)
Malaw wouy malaw wouy maaaalaw (weuyooo laobé thiouray gongo)
Malaw wouy malaw wouy maaaalaw baye baaabou baye babou weuyooo laobé thiouray gongo
Diereudieuf pape alioune
Suma xeet bi dugana guneh gui
Faxass xar si digabii
Bugut ben budul bii
Xawma kouy doba si guenagui
Dioxko ndam dioxko ndam
Sax ak ndiognam ak ndiognam
Basi askanam askanam bima wan kanam
Peundal suba faxass ngon
Yon bi gouda kuneh awsa yon
Kouko wédi neka xarr sa fei rek moy dioxla gnogn
Basi kawa kaw ma adjko kuko adji ding ma togn
Beat bama diégue ma najko niu seuy rek amsi dom
Kula téré lembeul yenguelal nii Messi bouy teubal sula nekhé town bi nga pendal
Xol yi diniu begual play ken doula pause
Sougn biir yambarr doufi sauce
Degn meyti teh sohorr nurse
Soula nekhe latchel Dios
Bamboo kom kachikally
Dokh sa mind bi tactically
Mind bi dioub ni bena tally
Doma dab nax damala sorri
Dama gaw ni ball bunj fetel
Am samsung ni alcatel
Na nooy pape malaw na nooy
Modou mbaye
Bouko fetcha di seuga
Diapal si sa ndinga
Bul rouss maneh merr bi niowout
Nieti yone la nak do reutcha
Dieul loxoy witiax nikouy beuga diapa pitcha
Just dance it diko teuyax moxam bouko nekhe seuga
Dafa sorri man doumako diegué
Naka dieulssi kon souko pare
Attack xolal bi tasseh nieti yon la nak ndaw xarré
Bousi nak foxoj sa ndiga ndablii si ndiga la tiba
Li ma saff la kom sossi liba nhaa bang ko kanna sila
Ah Ana loy ragal dieguesill wala ken randal
Kou sa gianaw bandang
Pape kay len niou fahass
Sa loxo sa guanaw
Melalni kouy feuguass
Kay len niou fahass
Sa loxo sa guanaw
Suma heet bi dugana guneh ngii
Fahass xar si digabii
Bugut ben budul bii
Xawma kouy doba si gueunagui
Modou mbaye ahh
Bouko fetcha di seuga diapal si sa ndinga bul rouss maneh
Bouko fetcha di seuga diapal si sa ndinga bul rouss maneh
Bouko fetcha di seuga bul daww malaw ahh
Mom dafa toy fompana fompat
Mouné mukk mom du wow
We are at war xex naw basa kaw
Si deuna lala teg tabaxal basa kaw
Lufi nobu dina feign, do ku ndaw
Da way girl is whining dafa melni amut yax
Diane moko djigadi xawma loumouy defni
Souko nekhé toodj deuna bi
Ba mou dangal podj bi
Ay yaaa wouy sama ndeye
Ya am sama thiopati
Ay yaaa wouy sama ndeye
Ya am sama thiopati
Wouy malaw wouy malaw wouy maaaalaw (weuyooo laobé thiouray gongo)
Malaw wouy malaw wouy maaaalaw (weuyooo laobé thiouray gongo)
Bilaye wouy malaw serigne mor thiamé (weuyooo laobé thiouray gongo)
Yow wouy malaw amadou mbaye (weuyooo laobé thiouray gongo)
Yegaleul yegaleul (yegaleul yegaleul) yegaleul yegaleul (yegaleul yegaleul)
Babou yegaleu yegaleul (yegaleul yegaleul) yegaleul yegaleul (yegaleul yegaleul)
Ma wissé ma monté ma serrel leu
(Weuyooo laobé thiouray gongo)
Ma wissé la ma monté la ma serrel leu
(Weuyooo laobé thiouray gongo)
Ma wissé la ma monté la ma serrel leu
Weuyooo laobé thiouray gongo
Wissé leu montél leu serrel leu
(Weuyooo laobé thiouray gongo)
Wissé leu montél leu serrel la
(Weuyooo laobé thiouray gongo)
Wissé leu montél leu serrel leu
Weuyooo laobé thiouray gongo
Más canciones de Pape Diouf
-
Damani
Ecoutez !
-
Kileu Beugue
Ecoutez !
-
Rëkkënte Bi
Enjoy
-
Yeewuleen
Pape Diouf Live au Biddew
-
Sama Seytané
L'Alchimie (Live)
-
Enjoy
Enjoy
-
Partir
Partir !
-
Superman Love
Ecoutez !
-
Dee mare
Jotna
-
Pape Diouf Live - Intro
Pape Diouf Live au Biddew
-
Dieulleul
Pape Diouf Live au Biddew
-
Massamba
Pape Diouf Live au Biddew
-
Jimy Dogo
Pape Diouf Live au Biddew
-
Immama
Pape Diouf Live au Biddew
-
Joggé Dagou
Pape Diouf Live au Biddew
-
Sa Ma Way
Pape Diouf Live au Biddew
-
Dee Ko Rof
Pape Diouf Live au Biddew
-
Ndaga
Partir !
-
Yaye - Live
L'Alchimie (Live)
-
Confiance - Live
L'Alchimie (Live)