Amore
de Pape Diouf
Dafa dem ba nand len khamni liguey bobou dou yone dou you
Dafa dem ba djeuli len khami liguey bobou yorou lo
Tchala delou wat beu keureum bamou lerr tei deloussi woul nay lerr Sadio demna
Rafet ndiot wessoul woul di def lou bone tei fokni lou bakhla bayil lolou
Dafa dem ba djeuli len khamni liguey bobou yorou lo bakhoul
Tchala delou watt ba keureum ba mou lerr tei deloussiwoul nay lerr sadio demna
Mamama lelele
Mamama sadio djeguemar lawone bou deuk fou sorrei sorrei
Tela niak yaye
Tela niak yaye niak baye sadio
Dafa beug dan doleim waye sadio fimou nekk bakhoul
Bayil lolou boul deim fofou fofou woroul
Litti litti niarei baka ndiaye
Bakou lem ya
Sadio souma sagnone
Souma sagnone do dem fofou
Tei deugoul nangoul dangua lou diam wouy lei lei sadio
Dafa dem ba nand len khamni liguey bobou dou yone dou yone dou yone
Dafa dem ba djeuli len khami liguey bobou yorou lo
Tchala delou wat beu keureum bamou lerr tei deloussi woul nay lerr Sadio demna
Mamama mama lelele
Niguama fonke taaa Papiss
Niguama wolooo taaa
Batakhna foumala wot ngua wouyoussima
Bayou bebe cheikh konare
Sokhna fatou ndiaye moy yayam
Bayou bebe cheikh konare
Bilay niguama fonke teee
Batakhna foumala wot ngua woussima
Bayou bebe cheikh konare
Dom djou bakh kha nopal yayam
Djeri ngone ma lobe samba
Kouri matcha seguita
Abdou mbaye woyna la
Bilay niguama fonke lolll
Papiss konare
Bayou bebe cheikh konare
Dom djou bakh kha nopal yayam
Degloune ma wayle ko yayam
Sokhna fatou ndiaye ki moy yayam
Nimala wolou nooo
Sou nekhei bah mouy metii
Sou metei ba mouy nekhh
Papiss konare
Djeri ngone ma love samba
Sou nekhe ba mouy metiii
Sou metei ba mouy nekh
Ehh nimala fonke loll
Ehh nimala wolo loll
Eh nimal fonke looll
Eh nima la wolo lol
Ehhh
Más canciones de Pape Diouf
-
Damani
Ecoutez !
-
Kileu Beugue
Ecoutez !
-
Rëkkënte Bi
Enjoy
-
Yeewuleen
Pape Diouf Live au Biddew
-
Sama Seytané
L'Alchimie (Live)
-
Enjoy
Enjoy
-
Partir
Partir !
-
Superman Love
Ecoutez !
-
Dee mare
Jotna
-
Pape Diouf Live - Intro
Pape Diouf Live au Biddew
-
Dieulleul
Pape Diouf Live au Biddew
-
Massamba
Pape Diouf Live au Biddew
-
Jimy Dogo
Pape Diouf Live au Biddew
-
Immama
Pape Diouf Live au Biddew
-
Joggé Dagou
Pape Diouf Live au Biddew
-
Sa Ma Way
Pape Diouf Live au Biddew
-
Dee Ko Rof
Pape Diouf Live au Biddew
-
Ndaga
Partir !
-
Yaye - Live
L'Alchimie (Live)
-
Confiance - Live
L'Alchimie (Live)