SAF NA BA NOPI

de Momo Dieng

Saf na ba noppi
Kenn du sappali
Saf na ba noppi
Kenn du sappali

Yaw bul ma miin a miin ba faate ma yaay
Coow li mën na bëri lool
Waaye nangul ne cin bokkul safiin
Yaw bul ma miin a miin ba faate ma waay
Loo bañ bañ nomboor nangul nopyi guddu na mën na day

Saf na ba noppi
Kenn du sappali
Momo saf na ba noppi
Hey, kenn du sappali

Barñi ma rombal bët ba daagu jëm minam jëm sendu
Wuy ma yaaya baye Momo Dieng
Saf na ba noppi!

Hee hee hee hee
Yahh yaa yaa yaa

Saf na ba noppi
Kenn du sappali
Momo saf na ba noppi
Kenn du sappali

A rafet a mëna fecc a bëy bësi doom
Ama mayoon daaw fisiin
Bassa boori geej gee

Lakoon sakoon nga leebu ba ngi
Moma mayoon daaw fisiin
Bassa boori geej gee

Bul ma miin
Bul ma miin miin
Bul ma miin ba faate ma kon mu ñaaw
Roy du nuroo piir
Mës nuroo ak piir
Isma bulma miino
Bul ma miin ba faate ma kon mu ñaaw

Lay layla laa ohh

Bul ma miin
Baye Raan bul ma miin
Baye Raan Diop bul ma miin ba faate ma kon mu ñaaw

Lourass Diop boo ñówul mu ñaaw
Heyy
Céy sama waja ngi ni
Heyy
Sa gaan raak sa gaan
Heyy
Ne naa la Momo yëngal sa gun gu ndaj

Lourass Diop boo ñówul mu ñaaw
Heyy
Céy sama waja ngi ni
Heyy
Lahy lay la laa
Boo ñówul mu ñaaw sama nit
Lahy lay la laa ohh

Roy du nuru piir
Mës nuroo ak piir
Djiby Ndiaye bul ma miin no
Bul ma miin ba faate ma kon mu ñaaw
Chérie Arame Diallo sama waay

Lourass Diop boo ñówul mu ñaaw
Heyy
Ne naa la Momo yëngal sa gun gu ndaj
Heyy
Sa gaan raak sa gaan
Heyy
Ne naa la Momo yëngal sa gun gu ndaj

Djiby Ndiaye boo ñówul mu ñaaw
Céy diikal diikal sama waja ngi ni
Isma boo yëngoo mu neex
Malick Mbadj Dissa Baye
Sama wadja ngi ni
Heyy
Sa gaan raak sa gaan
Heyy
Ne naa la Momo yëngal sa gun gu ndaj

Senegal booleen yëngoo mu neex
Céy dikkël dikkël sama réew maa ngi ni

Heyy
Ne naa la Momo yëngal sa gous gous tathie

Más canciones de Momo Dieng