Neketewo
de Momo Dieng
Man mi amon yené thi mom dane diouli di niane mou doon sama yayi doom
Li mo takhon ma ragala sobou ba dissi khouss ndokh dima tolou si baat
Mais heureusement faté wouma sama niom yaye samay kharite samay deukando waw kon ma rouss
Annimou foumou nekee
Man guissou mko fennneu
Li mo takhon ma raga lona douggsi ndokh ba dissi sobou ba dissi khouss ndokh dima tolou si baat
Impacté na sama ligueye bou gars yi neké fi ma nekk fenen
Li mo takhon sama yaye nanma boy diokhé sa khol nanko seetat yaw
Heureusement faté wouma sama niom yaye samay kharite samay deukandoo wayé kon ma rousss
Ani kathia dess
Ani foumou nekk
Loumay wakh wa kogn ba
(Deug deug lath nala ko)
Souniou mako ladié
Ani kathia dess
(Mo diara wakh ak wa kogn bi niewal)
Wooy Ani foumou nekk
(Deug deug lath na lko)
Loumay wakh wa kogn ba ak sama yaye
Bouniou mako ladié
Ndeketé yoo
Ndeketé yoo nobou mawwon
May investir si nakhi kassé
Ndeketé yoo ndeketé yoo beugouma woon
Demna bayima ak lokhoy kassé
Ani kassa dess
(Deug deug lath nala ko)
Ani foumou nekk
Loumay wakh wa kogn ba
(Deug deug lath nalko)
Souniou mko ladié
Ani kassé dess woo
Ani foumou nekk
(Mo diara wakh ak wa kogn bi niewal)
Loumay wakh wa kogn ba ak papito soumko ladié
Ndeketé yoo ndeketé yoo nobouma woon
May investir si nakhi kassé
Ndeketé yoo ndeketé yoo beugouma woon
Dmena bayi ma ak lokhoy kasseey
Ay lokhoy khassee
Ali baba Dior ndour sa maamee birano Ndour
Sira coumba laobé boubou coumba laobéy
Abdallay daro mbaar madior matar ma diama yacine daour mathia lodo
Adjaratou ndeye sokhna ndour sa mame
Aladji ilimane ndour sa mame
Sama wadji sama waadjé wouy biraano Ndour
(Ali maissa aly ndiaye mbeugelou CA-5000
Hee hee ni Eferalgan
Hee hee my boy ba saa youla nekhee
Sa youla nekhee ma masla nga beuga seuyi li dafa yomb)
Yaye kathy Cissé sa yaye dja laniouy dioy
Meussoul dakk gannn bamou dieum ndiagg mou diog taalou
Youssou madjigene sa baye
Mom dé degg dialooré
Wouy birano Ndour
(Aly Maïssa aly ndiaye
Mbeugelou ca-5000
Hee hee ni efferalgan
Hee hee my boy ba saa youla nekhé
Sa youla nekhé moussa niew nga beuga seyyy li dafay yomb)
Chérie Amina gueye
Papa aly gueye bayam
Mboukou ndayou papitaa
Sama wadji sama wadjee
Youssou madjigene sa baye
Dondou woko dangko doonee
Wouy biraanoo ndour
Mbakh guissi yaw foula guissi yaw tabé guissi yaw birane
Yakouloo way wee
En yoo yela yee yelaa
Ni mbakh guissi yaw foula guissi yaw tabé guissi yaw yakoulo way wee
En yoo yee yela yee yellaa
Siré coumba laobé boubou coumba laobeey
Abdalaye daro mbaar madior
Rak matar madiama yacine daour ma sa lodo
Ibrahima ndour sa baye leuu
Ni mbakh guissi yaw foula guissi yaw tabé bissi yaw birane yakoulo way wee
En yee yela yee yelaa
Chérie Amina gueye
Papa aly gueye bayam
Dioudou bou reuy ndaye ak baye
Wayé foula ak fayda borom mokay mom
Youssou madjigene sa baye dondou wooko dangko doonee
Wouy biranoo ndour
Boubacar ndour sa baye
Mbakh guissi yaw foula bissi yaw tabé bissi yaw birane yakoulo way wee
Ndiaga ndour modi bayam
Birane mbakh guissi yaw foula bissi yaw tabé bissi yaw birane yakoulo way wee
Ngoné diaba badiene nay baye
Ndeye seynabouuu badiéne nay baye
Aby ndour badiene nay baye
Fatou kiné ndour badiéne nay baaye
Ni mbakh guissi yaw foula bissi yaw tabé bissi yaw birane yakou lo way wee
Más canciones de Momo Dieng
-
Yole
Cey li
-
Lang Gui
Lang gui
-
Alalou Ku Sagan
Alalou Ku Sagan
-
Doom Gorel
Doom Gorel
-
Kaay Nu Jubbo
Lang gui
-
Langui (Remix) - Live
Momo Dieng Live Performance
-
Love Source De Vie - Live Performance
SAMPOU (Live Performance)
-
Life bi - Live
Momo Dieng Live Performance
-
Thiat - Live
Momo Dieng Live Performance
-
Yole - Live
Momo Dieng Live Performance
-
Dem - Live
Momo Dieng Live Performance
-
Kanoule - Live
Momo Dieng Live Performance
-
Alalu Ku Sagane - Live
Momo Dieng Live Performance
-
Kay Nu Jubo - Live
Momo Dieng Live Performance
-
Ndobine
Cey li
-
Chérie coco
Cey li
-
Kal
Cey li
-
Dang serré
Cey li
-
Xarit sama
Cey li
-
Turëndo
Cey li