Love Source De Vie - Live Performance

de Momo Dieng

Yow kay ma netali lenn noy, ben histoire boumafi dalon
Samdie soir may seti, sama xalé bou bess bi
Beuss bobou lamaci daal mane faw ma nétali len ko
Bama yégué sa keur ga niou terrou ma, nignuy tero buur
Tallal ma thiouray teegal ma reer bu neex dall may goonal
Bamou dess loudoul gnibi, ma andeu ak xalé bi, moumay goungué
Bama démé sa mbeed mi, né xaral ma tagato ak mom diokh ko ben calin
Guestou yam si Amy, Amy rakou lily sama benen geel bi (sheuteuh teuh)
Mane thiolé na, ndax Amy dianama yolé yolé, mba douma yolé yolé
Thiey fouma dieum, ki dinama yolé yolé
Mba doma yolé yolé, may xallat ndax doma yolé yolé
Xalé bi dinama yolé yolé, xamna dinama yolé yolé

Diamono dji thiey ndoumba lame
Mangui sangou tewoul samay tank di fegn
Du nétali sakh way loumou yeug mou siw
Néna mur yi sakh, niom dagniy wax téléphone yi di gnofi daka yolé
Yolé yolé yolé, hé mba doma yolé yolé, xalé bi dinama yolé yolé
Thiey fouma dieum ki dinama yolé yolé
Wouy fouma dieum ki dinama yolé yolé

Sayou foor yombé rek, seug diafé wawaww
Kham na sou ndiab yaggué légui gawar fegn
Wooh wooh wooh
Leeh leeh leeh leeh
Sa deugeu deugeu deugeu nak

Más canciones de Momo Dieng