Lang Gui

de Momo Dieng

Man damay lathie beug kham
Damay khol nguir beug guiss
Dama rer ta beug fegnn thi xalel
Man damay lathie beug kham
Damay khol nguir beug guiss
Dama rer ta beug fegnn thi xalel
Sama yaye bayimaa ma dem seeti
Xalei yii sen lang riche neuu

Wowoo damakoo dama beug setti
Xalei yii sen lang riche neu

Man damay lathie beug kham
Damay khol nguir beug guiss
Dama rer ta beug fegnn thi xalel
Man damay lathie beug kham
Damay khol nguir beug guiss
Dama rer ta beug fegnn thi xalel

Maman bayimaa ma dem seti
Xalеi yii sen lang neikh neuuu
Wowoo damako dama bеug xooli
Fatou kine ndour langam neikh neuu
Wawaw damakoo dama beug seti
Fatou Bintou Ly langam riche neuuu

Man damay deim wooy
Man damay deim wooy

Man daal lang yima meusseu diar yeup
Lang gui tay moma ci daaakhal
Lang yimeu meusseu dem yeupeu
Lang gui tey moma ci daakhal
Man dei beug naleine
Djigueni senegal man dei fonkat naleine
Man dey wolounaleine
Djiguene gni man dey beug naleine

Cherie boy boul nam dara tay
Diapal ni may sa superman
Man dal diaral ngama naam
Loo beug ma indil laako
Gnoun goor gni nagnou def souniou gneti morsso
Tek ci kopati ak ay mbarakiss
Djiguene gni gnom dagno civilisé
Tek ci am feeling ma beik thi yene
Yow so beugueii heii

Fariyoooleii
Deugg deugg deugg lang gui nekh na ma
Djiné su sokhla dakhaar ku yeug daanu
Waa yen su len sokhla momo nyeupa nyaka

Man daal lang yima meusseu diar yeup
Lang gui tey moma ci daaakhal
Lang yimeu meusseu dem yeupeu
Lang guii tey moma ci daakhal
Man dei beug naaleine
Djigueni senegal man dei fonkat naleine
Man dey wolounaleine
Djiguene gni man dey fonkat naleine
Gnoun goor gni nagnou def souniou gneti morsso
Tek ci kopati ak ay mbarakiss
Djiguene gni gnom dagno civilisé
Tek ci am feeling ma beik thi yene
Yow so beugueii heii

Yow so beugueii heii woy woo woy woy

Man daal lang yima meusseu diar yeup
Lang gui tey moma ci daaakhal
Lang yimeu meusseu dem yeupeu
Lang guii tey moma ci daakhal
Man dei beug naaleine
Djigueni Senegal man dei fonkat naleine
Man dey wolounaleine
Gambia man dey fonkat naleine
Gnoun goor gni nagnou def souniou gneti morsso
Tek ci kopati ak ay mbarakiss
Djiguene gni gnom dagno civilisé
Tek ci am feeling ma beik thi yene
Yow so beugueii heii

Man damay lathie beug kham
Damay khol nguir beug guiss
Dama rer ta beug fegnn thi xalel
Man damay lathie beug kham
Damay khol nguir beug guiss
Dama rer ta beug fegnn thi xalel

Más canciones de Momo Dieng