Kaay Nu Jubbo

de Momo Dieng

Tu tu tu tu tu
Tu tu tu
Ndau ak limu min
Suko guisul dafai wet
Ya nek sama khol
Soma meré damai diakhlé
Kai wuyumaaa, kai nu juboo
Soma meré sama khol dj nekhoi

Samai non dinagnma retaan
Soma meré sama khol du nekhoiii
Sama yon dina wet lol
Sa sakh lima diotee ak yau dafa ayul
Bilayi lima diote ak yau dafa ayul
Khifna gnu teghalma gnam,
Sama khelmas di dem ci yau
Madadi sur
Fek bobu lekuma dara
Kai wuyuma, kai nu jubbo
Soma meré sama khol du nekhoi
Samai non dinagnuma retaan
Soma meré sama khol du nekhoi
Ndakh sama bir bi yai kikoi rai
Te sakh lima diote ak yau dafa ayul
Bilayi lima diote ak mom dafa ayul
Fekhna sama bol teghe, mu dielko di khol
Degh boit message
Lir samai discussion ba sugnu diotai nonu la yakoo

So baghe bul koi setloo
Lk

Más canciones de Momo Dieng