Kaal - Live Performance

de Momo Dieng

Si ih ih
Yow migua khameni yow la
Yow la beugue doundeul
Say youma gneuwé sen keur
Gnamay tegueul amitié
Yow mima rombe gneup tane
Ni yow rek leu wawaw
Kone yow mi khalé bi beugue naleu
Té bouma sagnone gnoune gniarre gnou diappa lén té

Wawe mbeuguel wouye mbeuguel loy wawe mbeuguel wouye mbeuguel loy

Más canciones de Momo Dieng