Dem - Live

de Momo Dieng

Wowowowowowowoy wowo
Lalalalalalalalala lalalalalalala
Wowowowowowowoy wowo

Aduna dafa teureudi
Loye deff nangko xolat
Euleuk dou añ dou reer wayé lou mata sedd leu
Yon wi gudone teu leundeum lolu xadi sakh dabnama cé
Lune dadiena akk mom mane diomuna wañieku

Ndakh sama yaye meussul beug ma dem dajélé cono
Wowo sama yaye meussul beug ma dem dajélé cono
Dang dangui keur keuri ba goudei keur keuri moye taxa tabax keur
Seu ndieuriñ ngui thi seu guinaw cono
Dang diangui keur keuri ba goudei keur keuri moye taxa tabax keur

Seu ndieuriñ ngui thi seu guinaw cono
Su mete sax mani nexna
Waye limay daj mane makko xam
Yon wi gudone teu leundeum lolu

Xadi sakh dab nalacé
Lunei daje nga akk mom waye diomu nga
Wañieku ndakh suñiu yaye meussul beug ñu dem dajélé
Wowo suñiou yaye meussul beug ñu dem dajélé

Dang diangui keur keuri ba gudei keur keuri moye tax tabax keur
Seu ndieuriñ ngui thi seu guinaw cono
Dang diangui keur keuri ba goudei keur keuri moye tax tabax keur
Seu ndieuriñ ngui thi seu guinaw cono

Li dunde du nein yalla la
Loye deff nangue ko kholat
Euleuk du añ dou reer wayé lu mata sed leu
Yone wi gudena ta leundeum lolu

Xadi sakh dab nala ce
Lune dajenga akk mom waye diomou nga wañieku
Ndakh suñiu yaye meussul beug niou dem dajélé cono
Wowo sama yaye meussul beug ma dem dajélé
Bayima ma dem

Bayima ma dem ndaxma xam licci nakkar akk cono bayima ma dem
Ma xem licci tumuranké bayima ma dem bayima ma dem dem dem dem
Bayima ma dem Yaye boy

Bayima ma dem ndakh ma xam licci nakkar akk cono bayima ma dem
Ma xam licci tumuranké bayima ma dem bayima ma dem dem dem dem
Bayima ma dem Yaye boy

Bayima ma dem ndakh ma xam licci nakkar akk cono bayima ma dem
Ma xam licci tumuranké bayima ma dem bayima ma dem dem dem dem
Bayima ma dem

Dang dangui keur keuri ba goudei keur keuri moye tax tabax keur
Seu ndieuriñ ngui thi seu guinaw cono

Más canciones de Momo Dieng