Dang serré

de Momo Dieng

Man damay lathie beug kham
Damay khol nguir beug guiss
Dama rer ta beug fegnn thi xaleil
Dama rer ta beug fegnn thi xaleil

Sama yaye bayimaa ma dem seeti
Xalei yii sen lang riche neuu
Wowoo damakoo dama beug setti
Xalei yii sen lang riche neu
Man damay lathie beug kham
Damay khol nguir beug guiss
Dama rer ta beug fegnn thi xaleil
Dama rer ta beug fegnn thi xaleil

Maman bayimaa ma deim seti
Xalei yii sen lang neikh neuu
Wowoo damako dama beug xooli
Fatou kine ndour langam neikh neuuy
Wawaw damakoo dama beug seti
Fatou bintou ly langam ruche neuuu
Man damay deim, man damay deim, man damay deim, man damay deim
Man damay deim, man damay deim, man damay deim, man damay deim wooy
Man damay deim, man damay deim, man damay deim, man damay deim
Man damay deim, man damay deim, man damay deim, man damay deim wooy

Man daal lang yima meusseu diar yeip
Lang gui tay momassi daaakhal
Lang yimeu meusseu deim yeipeu
Lang guii tay momassi daakhal
Man dei beug naaleine
Djigueni senegal man dei fonkat naleine
Man dey wolounaleine
Djiguene gni man dey beug naaleine
Cherie boy boul nam dara tay
Diapal ni may sa superman
Man dal diaral ngama naam
Loo beug ma indil laako
Gnoun goor gni nagnou def souniou gneti morsso
Teilssi kopati ak ay mbarakiss
Djiguene gni gnom dagno civilisé
Teikssi am filing ma beik thi yeeine
Yaw so beugueii heii
Fariyoooleii

Más canciones de Momo Dieng