Chérie coco

de Momo Dieng

Frasy diaral ngaama dumala bayé
Honey yaay sama coco bané
Shuu bi nexna surum lèè ba dioolea
Darling yaay saama coco baneé
Diaral ngaama bòòt gaindé
Roogan tikoo diani saa maan
Hee hee-eee maan dee diaral ngama lounéék
Diaral ngaama guuh pétrole
Wonub taal di dieuf dieufi
Frasy maan de diaraal ngama lounék

Frasy diaral ngaama dumala bayé
Honey yaay sama coco bané
Shuu bi nexna surum lèè ba dioolea
Darling yay saama coco bané
Diaral ngaama bòòt gaindé
Roogan tikoo diani saa man
Hee hee-eee maan dee diaral ngama lounéék
Diaral ngaama guuh pétrole
Wonub taal di dieuf dieufi
Frasy maan de diaraal ngama lounék

Aida chérie coco baneh
'Cause you are my likeness and without you baby, I got a illness
Wa wa, the sickness
'Cause you're my sunshine, my love don't talk together
I never mind, please don't take your love away from me, baby
Sans toi dans ma vie je n'ai aucune envie de vivre mes envies
Sans toi dans ma vie je vais m'enfuir pour toujours loin d'ici
Come on with me my baby
Reviens-moi, ma chérie
Come on with me my baby
Reviens-moi, ma chérie

Suudoou woon yaye ak baye
Xaarit yi ak mbook yiimaa weur
Saama duun yaa meun na sof
Melni limaa beug dagne kooy diay
Te aawma lignuu may ladie maan
Mbeeguel laa bari dolee lii woor naamaa
(Colle colle colle, chérie coco)
Mbeeguel laa bari dolee dal nama dalon na samay wadiourr
Ak genen gnudul gnoom (colle colle colle, chérie coco)
Mbeeguel la bari dolee dalnama seetull président
Ak boromi gaarat (colle colle colle, chérie coco)
Mbeeguel la bari dolee dal nama dalon na samay
Moroom ak gnenen gnudul gnoom (colle colle colle, chérie coco)

(Colle colle colle, chérie coco) mbegueel la bari dolee
Seetul wasso ak duidu bu yeurr daall (colle colle colle, chérie coco)
Mbeeguel laa bari dolee dal nama dalon na samay wadiourr
Ak gnenen gnudul gnoom (colle colle colle, chérie coco)
Kuneek saa histoire thieey mbegueel
Capitaine nu borom (colle colle colle, chérie coco)
Mbegueel la baari doolee
Seetul général ak boromi gaaloo (colle colle colle, chérie coco)
Maan guisnaa gnaar gnu beugante
Sokhna aicha thiey mbegueel (colle colle colle, chérie coco)
Mbeeguel la baari doolee
Seetul général ak boromi gaaloo (colle colle colle, chérie coco)
Colle colle colle, chérie coco
Colle colle colle, chérie coco
Colle colle colle, chérie coco

Más canciones de Momo Dieng