Cheri M Direk

de Mass Konpa

Yow! Rigolo, con, ñëpp parano fii
Ku nekk tibë jëmelé sa biir bi
Xawma dañu rew xawma dañu possedé
Suñu grand yi wara jangalé di xasté
Fi études, politique, économie
Ñoo si ngenë dellu ginnaaw
Détails yi, batailles yi
Ak yëfu dof yi ñoo si ëpp ay trophée

Mérité woleine ma juddu ci seen réew mi
Dama wara déménager dem dëkk ci air bi
Fi ñi fi gën nul lañj gën jox nopp
Ñi fi gën immature lañu gën jox bopp

Jigéen yi, billets yi ak bouteilles yi
La xale yu góor yi di wër
Volets yi, billets yi ak téléphone yi
Moom la jigéen ji di wëre

Bëri yëfi dof
Senegal dafa bëri yëfi doff (bëri yëfi dof)
Bëri yëfi dof
Senegal dafa Bëri yëfi doff (loolu rekk fi dox)
Bëri yëfi dof
Senegal dafa Bëri yëfi doff (bëri yëfi doff)
Bëri yëfi doff
Sama rew dafa beuri yeufi doff (loolu rekk fi dox)

Dëkk bu xat alë yu yaatu
Auto yu chère te tali bi baaxul
Stade bu bees te talibé yi lekuñu
Avion bu bees te ame village yu naanul
Ame coupe bu bees ndekte palais worul
Médias yu faux, journalistes yu jangul
Musik bu rëp te contenu bi baaxul
Rappeurs yu réw ak mbalax man yu ayul

Mérité woleine ma juddu ci seen réew mi
Dama wara déménager dem dëkk ci air bi
Fi ñi fi gën nul lañj gën jox nopp
Ñi fi gën immature lañu gën jox bopp

Jigéen yi, billets yi ak bouteilles yi
La xale yu góor yi di wër
Volets yi, billets yi ak téléphone yi
Moom la jigéen ji di wëre

Bëri yëfi dof
Senegal dafa bëri yëfi doff (bëri yëfi dof)
Bëri yëfi dof
Senegal dafa Bëri yëfi doff (loolu rekk fi dox)
Bëri yëfi dof
Senegal dafa Bëri yëfi doff (bëri yëfi doff)
Bëri yëfi doff
Sama rew dafa beuri yeufi doff (loolu rekk fi dox)

Bëri yëfi doff
Sama rew da

Más canciones de Mass Konpa