Positiver (Interlude)
de Karabalik Beatz
Musique Xalé, vibes Xalé
Man ak Karabalik (banger banger banger banger ah)
Youssou, Omar, Baba ngay guiss ci man
Malal, Xumam, Keyti ngay guiss ci man
Artist demb rek ngay ci man ehhh gnom gneup ngay guiss ci man
Boko gueumé mouy fayla lolou lagn ma wax
Ma bayi lëëp diap néki ci waar
Téwal banlieue ndongo lay represent heee man
Ndongo lay represent
Musique musique ko, musique musique ko
Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh
Musique musique ko, musique musique ko
Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh
Ay diouni ndaw bayi lëëp diap ci yaw
Ay diouni ndaw faté lëëp diap ci yaw musique
Xouran Naka xouran
Li louka daka daka daka dou am
Xouran Naka xouran
Li louka daka daka daka dou am
Boy Li moy bouyaka bouyaka (djeul vibes mélodie)
Defko ci ndaga, ci ndaga (damay international)
Xamnga ci Naka, ci Naka (represent my hood)
From Senegal, Senegal
Yayaya
Fou Malade, Fou Malade wax nga Niou sa xalat
Fou Malade, Fou Malade wax nga Niou sa xalat (Ndax
Musique Xalé, vibes Xalé
Man ak Karabalik (banger, banger, banger, banger ah)
Youssou, Omar, Baba ngay guiss ci man
Malal, Xumam, Keyti ngay guiss ci man
Artist demb rek ngay ci man ehhh gnom gneup ngay guiss ci man
Boko gueumé mouy fayla lolou lagn ma wax
Ma bayi lëëp diap néki ci waar
Téwal banlieue ndongo lay represent heee man
Ndongo lay represent
Musique musique ko, musique musique ko
Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh
Musique musique ko, musique musique ko
Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh
Man Nala bismilah, bismalah)
Nga nanma kanaraw, kanaraw
Man nanla corruption moukhoum kagn ci kaw lay door té nioussi souf lay gagn feuneukeu what's up
Wou yoyoyoy fimoy Senegal ndiaye
Wou yoyoyoy fimoy Senegal ndiaye
Boy Li moy bouyaka bouyaka (djeul vibes mélodie)
Defko ci ndaga, ci ndaga (damay international)
Xamnga ci Naka, ci Naka (represent my hood)
From Senegal, Senegal
Yayaya
Yalla miy mayé man ma yoor sama weurseuk
Ouh yeah, ouh yeah sant na Yalla
Musique Xalé, vibes Xalé
Man ak Karabalik (banger, banger, banger, banger ah)
Youssou, Omar, Baba ngay guiss ci man
Malal, Xumam, Keyti ngay guiss ci man
Artist demb rek ngay ci man ehhh gnom gneup ngay guiss ci man
Boko gueumé mouy fayla lolou lagn ma wax
Ma bayi lëëp diap néki ci waar
Téwal banlieue ndongo lay represent heee man
Ndongo lay represent
Musique musique ko, musique musique ko
Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh
Musique musique ko, musique musique ko
Musique musique ko, musique musique ko, musique dafa nekh
Más canciones de Karabalik Beatz
-
Calm Down
General Kara
-
Nouyo National
General Kara
-
Fou Lerr Lako Tekk
Fou Lerr Lako Tekk
-
Seugne Modou
General Kara
-
Rambakh
General Kara
-
Mbarambakh Sip Sip
General Kara
-
Wally Seck
General Kara
-
Topline (Interlude)
General Kara
-
Come Back
General Kara
-
O Lit
General Kara
-
Ifemi
General Kara
-
Sista
General Kara
-
So Sad
General Kara
-
Ndidiaye
General Kara
-
Brodaman
General Kara
-
Muzik
General Kara
-
Trash Life
General Kara
-
Tollou Way
General Kara
-
General Kara
General Kara