Lamou Saff
de Jeeba
Eh, la mu saf kenn du la ko wax
Ndax kako macc a ko xam
Ñii naan kii da lay gololoo naan doo dara
Maa dugg ci biir ba lépp leer ma nàññ jar nga ko
Ku la xamul mooy diiranteek yaw mbagg chérie coco
Boo doon musicien, ma ne la doo dégammer
Def nga ma sa xale, doo jouer ak man jeu de gamin
Dëkke di ma jamb di ma jamb yoroo marimba doo Benjamin
Boo deful ndànk naa mas a dee sa loxo, on sait jamais
Moom xale la te bari na doole
Moo raw alkaati dafay dóóre
Dina la toppatoo ba laaj la laaj la laaj la bébé looy reeree
Te boo ko laajee mu ne la bae man yaw mii laay reeree
Fajar teel nii la may yeewee
Di ma xool ci biir bët, naan ma qu’est-ce que ça fait?
Yaw yaa raw athlète bu drogué
Ku la topp ba ci biir day mujje é clater
Eh! Dafa neex lool nga am ku xam liy jamb sa dittax
Soxlawul sax ngay wax day exécuté newul ku rambax
Teey na xàmme na fu ñuy feccee Yeelaa ak Ndawràbbin
Collé la ñàpp mel ni docteur Raoul ak Chloroquine
Arméwu kaw ak suuf mel ni kuy dem guerre
Tasaare arsenal yi bu la dal nga teer
Di la woo ci bëre te leer na leer na moo la moo la man di la noggatu
Tas sa ngemb, mbër ma daanu na, ooh au secours!
Moom xale la te bari na doole
Moo raw alkaati dafay dóóre
Dina la toppatoo ba laaj la laaj la laaj la bébé looy reeree
Te boo ko laajee mu ne la bae man yaw mii laay reere
Fajar teel nii la may yeewee
Di ma xool ci biir bët, naan ma qu’est-ce que ça fait?
Yaw yaa raw athlète bu drogué
Ku la topp ba ci biir day mujje éclater
Jeeb la boy
Rambax!