Goor

de Jeeba

Yow góorgóorlu wonel yaay góor
Fi góor dey dóor góor jàpp góor
Yow góorgóorlu nga def yëfu góor
Fi góor dey jak góor dimbali góor

Ndax amul amul soxor amul ki ñaan
Te loolu degit mooy jikkoy góor góor góorooy
Góor danga aah woor jambaroo

Yow góor góor du bari coow
Góor liggéey laay gëm ñeme dëkk lu diis
Ku la wo ci ay caxaan nekkoo newuma fa
Am fu la bari jom njambaru gaynde góor
Góor dafay tuuti wax
Dëkk job lu bari lu bari
Boo ko defe dangay sori
Bàyyil sa ngora bi ngay mbuub naan góor
Loolu deful góor
Góor dafay lorñe dem fu sori

Kon góorgóorlu taxay dégg
Waaw góor góoroy góor
Góor danga an wor jambaroo

Góor dafay téral jigéen sigil nday ak baay
Laay nawe góor
Walaay góor

Yow góorgóorlul wonel yaay góor
Fi góor dey dóor góor jàpp góor
Yow góorgóorlul nga def yëfu góor
Fi góor dey jak góor dimbali góor

Ndax amul amul soxor amul kiñan
Te loolu degit mooy jikkoy góor góor góorooy
Góor danga aah woor jambaroo

Yaw góor, góor du hypocrite
Góor warul fimisté rambaj du jikkoy góor
Góor dey xam li ku waar te jikko jefe góor
Góor adduna bu mu metti ba nga salit góor
Sangul sa mbalanu sutura bul jaay sa ngor
Góor benn jabar, ñaar ñetti baax na ci kow
Nga mën ko yor góor walaay góor

Kon góorgóorlu taxay dégg
Waaw góor góoroy góor
Góor danga an wor jambaroo

Yow góorgóorlul wonel yaay góor
Fi góor dey dóor góor jàpp góor
Yow góorgóorlul nga def yëfu góor
Fi góor dey jak góor dimbali góor

Ndax amul amul soxor amul kiñan
Te loolu degit mooy jikkoy góor góor góorooy góor
Góor danga aah woor jambaroo

Góor Yàlla dangay teg sa bët fu sori
Nancoo Sadio Mané
Wallaay yaay góor jaambar nga

Waaw góor
Góoroy góor
Góor danga aah woor
Jaambaroo

Más canciones de Jeeba