Décorée
de Jeeba
Eeeh eeh eeeh
Jeeba le boy
Oooh ooh
Seen ko rekk muy deem
Am caractère ba doo ko ñeme xool
Ye ye yeeh
Man gis naa la yow yaa ngi jeem
Bëgg mënale sa bopp ba kenn du la toññ
Yeee yee yeeh
Nionioy jigéen jigéen ju mëna góor
Jigéen ju xarul dara ay góor
Jigéen juy niaffé ngir mënal boppam waawaaw
Man xam du jambar nga dama lay ñanal, anh annh
Baññkat laa moo tax mu dëkk ci war wi
Yeee Yee Yeeh
Yow yarr nagn fuññ la wara yarr boubakh
Meusso ñuu gathiel benn yoon linga geum
Boobu ba léegi yaa ngi siiy ñafe ngir bëgg mu baax
Moo tax rekk maanaan la
Naw na sa yaay boy
Dina ko décorée wax ko doom bu mu jur
Mën na yoor reew
Naw na sa baay boy
Yow baay boy
Wax ko doom bu mu jur
Mën na yorii reew.... Eeh eeh eeh mën na yoori reew
Sa yaay boy eeh eeh eeeh eeew
Jigéen mën na yoori reew
Seen ko rekk muy deem
Bu doon benn bu ñu doon ñeent
Man sañ naa la bàyyi ak njaboot gi ci kër gi
Duñu tumuraanke duñu kox-koxi
Ñoo ngi si toll yi ak bureau yi
Ñoo ngi si sport bi ak fo mën tii deem
Ma naam jigéen yépp soleen ne jàkk
Dignité ak jambarté ngay lire seeni kanam
Ay joxoñ na la joxoñ na la
Moo tax ma bind wëy wi delloo la njukkal
Ubbi nga lamb ji doo seen moroom, ooooh oooh ooh
Oooooh oooh ubbi nga lamb ji jigéen doo seen moroom
Ma ne naw naa sa yaay boy
Dina ko décorée
Wax ko doom bu mu jur mën na yoori reew
Man naw naa sa baay boy
Baay boy
Wax ko doom bu mu jur mën na yoori reew eeeh eeh eeeew
Mën na yoori reew eeeh eeeeh eeeh
Naw na sa yaay boy eeeh eeeh eeh
Jigéen mën na yoori reew
Más canciones de Jeeba
-
Thiopet Yobu
Thiopet Yobu
-
Lamou Saff
Alajee
-
Champion
Alajee
-
Dafa Nekh
Dafa Nekh
-
Goor
Alajee
-
Aladji
Alajee
-
Saï Saï
Saï Saï
-
Dinala
Alajee
-
Guuy
Guuy
-
Diarabi
Diarabi
-
Diarabi - Remix
Diarabi
-
Yitma
Yitma