Dafa Nekh
de Jeeba
Jeeba la boy
(Brill on the beat)
Wax ma loo bugg ma defal la ko
Wax ma loo namm chérie ma wutal la ko
Même bu de auto ma jëndal la ko
Yóbbu la ci château nga dëkke dodo
Dama xam fuy xasan foofu lay wokk
Sa ex yi la doon sonal ñépp lay noq
Aj la ba ci kaw kenn du la jot
Jox la xiir bi nga leen di caw
Ma taxaw naan ko ñaaw
Yaw mbëggeel dafa neex boo koy kafe sax day neex
Sa biir xol bi lay jàpp mel ni dañ ci duggal peex
Mënoo xam li may wax tant que demoo ci ba mu jeex
Fok nga ñam kaani waaw doog a xam lu lem di saf
Awa ne na ma dafa neex
Makhfou ne na ma dafa neex
Kadia ne na ma dafa neex
Même Maimouna ne na ma mbëggeel billaay dafa neex
Kon dama la bugga
Te ku mu metti naanal amoniaque
Baygon wala maladio
Saa yoo yewoo
Nga ñuy gis ñuy lëngoo
Ma naan ko!
Bëgg na, bëgg naa ko
Bu dul ren di déwén dina ko def
Ndax yaa ma jaral loolu
Dama tegi gros lots ooh
Moom moo may tël man maa ko bërëŋ
Xanaa nanduloo loolu
Ñun buñu bégee moo ñu bégal
Buñu jooyee moo nu jooyloo
Bébé xam nga ma bu baax, duma ku tegi ndawal
Fi ma lay jàpp ba nga ni axxx, maa ko xam te dama koy dawal
Bébé xam nga man lu tax ma bëgg la dama ci sawar
Danga fekk fi ceebu keccax nga valorisé ko sànni ci ndawal
Ndaxam laax dinañu koy sëlmoo ñun dañu koy këppoo
Sama carte bi yaw la voteel tak séy bi jall ci leneen
Kon danga mer man maa ngi baax
Jox ko ndox mu naan mu geex loolu mënul ñax
Yaw mbëggeel dafa neex boo koy kafe sax day neex
Sa biir xol bi lay jàpp mel ni dañ ci duggal peex
Mënoo xam li may wax tant que demoo ci ba mu jeex
Fok nga ñam kaani waaw doog a xam lu lem di saf
Abba ne na ma dafa neex
Ngoné ne na ma dafa neex
Habib ne na ma dafa neex
Même Aicha Aziz ne na ma mbëggeel dafa neex
Kon dama la bugga
Te ku mu metti naanal amoniaque
Baygon wala maladio
Saa yoo yewoo
Nga ñuy gis ñuy lëngoo
Ma naan ko!
Bëgg na, bëgg naa ko
Bu dul ren di déwén dina ko def
Ndax yaa ma jaral loolu
Dama tegi gros lots ooh
Moom moo may tël man maa ko bërëŋ
Xanaa nanduloo loolu
Ñun buñu bégee moo ñu bégal
Buñu jooyee moo nu jooyloo
Mbëggeel mbëggeel mbëggeel dafa neex
Neex neex neex neex-a-neex ayyyee
Waaw we waa waaw waaw
Kon dama la bugga
Te ku mu metti naanal amoniaque
Baygon wala maladio
Saa yoo yewoo
Nga ñuy gis ñuy lëngoo
Ma naan ko!
Bëgg na, bëgg naa ko
Bu dul ren di déwén dina ko def
Ndax yaa ma jaral loolu
Dama tegi gros lots ooh
Moom moo may tël man maa ko bërëŋ
Xanaa nanduloo loolu
Ñun buñu bégee moo ñu bégal
Buñu jooyee moo nu jooyloo
Más canciones de Jeeba
-
Thiopet Yobu
Thiopet Yobu
-
Lamou Saff
Alajee
-
Décorée
Décorée
-
Champion
Alajee
-
Goor
Alajee
-
Aladji
Alajee
-
Saï Saï
Saï Saï
-
Dinala
Alajee
-
Guuy
Guuy
-
Diarabi
Diarabi
-
Diarabi - Remix
Diarabi
-
Yitma
Yitma