Yaye Boye

de Ismaël Lô

Yaye boye balalma
Yaye boye yaye boye balalma
Yaye boyo balalma
Khamna awma loula eupeu si adounya
Yaye sama wadiour yaye sama lepeu
Yaye man
Kon yaye soumala masse togne mangui
Dieguelou

Souma masse dioum tay rethiou nako
Ndakh yaye man guisna khale magua
Sama kanam
Ma khamne yaye boye fii la diar
Balalma balalma baalalma
Balalma balalma balalma balalmaa
Yaye boye

Soumala masse togne mangui dieguelou
Souma masse dioum tay rethiou nako
Ndakh yaye man guisna khale magua
Sama kanam
Ma khamne yaye boye fii la diar

Balalma balalma baalalma
Balalma balalma balalma
Balalmaa

Fane la mana diarr ba fayla yaye yaw
Ndakh fayla douma yomba yaye man
Waye dina diem sama kemtalay katane
Bagua contane

Louma def si yaw warou mako naw
Yayo ho yaye beuguena yaw ngua contane
Ndakh bo contane yala dana contane
Gnou sargual sounou yayboy
Yaye boye sonnagua yaye boye
Masso tayi

Yaguala tankhal dila sonal yayo
Rethiouw ma loma done dioure
Khamna amoul lo dadioul si gnoun gny
Tay alhamdou lila mane mi bay la
Diour na y dome khamna yoor ndiabote
Modi lane

Yaye boye yala nala yala fay
Balalma yayoboy balalma balalma
Balalma yaye boye balalma

Más canciones de Ismaël Lô