Tass Yakar

de Ismaël Lô

Wagni lène ki
Sa bay wagnila sa yaye wagnila
Yaw ngani ya bagne
Way dégueul lii

Sa yaye wagnila sa bay wagnila
Yaw ngani ya bagne
Bo khamone do dokholè ni nagua
Soralé euleuk digua yori sa diabot yaw

Say wadiour lou bakh lagn la digueeul
Bougnou sagnone ken doula gueun
Kon lou bakh lagn la yéné
Kon bok euleuk boul retiou nane

Sama yaye yé
Sama yaye boy sorina foumakay dioyé
Sama yaye yé
Sama yaye boy sorina foumakay dioyé

Koulané senguoul sa taar lala beugueul
Mané wadiour bolen défé kharit yaw
Domassa lal souf
Am bouki mané yombana lol
Wayé bou mana khalam mo diafé

Say wadiour lou bakh lagn la digueeul
Bougnou sagnone ken doula gueun
Kon lou bakh lagn la yéné
Kon bok euleuk boul retiou nane

Sama yaye yé
Sama yaye boy sorina foumakay dioyé
Sama yaye yé
Sama yaye boy sorina foumakay dioyé

Sama yaye yé sama yaye boy sorina
Foumakay dioyé
Bo bougué mouthia dagay téral say wadiour

Sama yaye yé sama yaye boy sorina
Foumakay dioyé
Bo nanguo bakh nagua dégueul say wadiour

Haléyi fofou lagnou rawanté
Ndakh wadiour kouko lébal
Bour yala fayla ba dolila yaw
Bo défé béneu am gnare
Bo défé gnare am gnint
Bo défé gnint am fouk

Bo mané témère gnagua téral say wadiour
Bo mané témère gnagua téral say wadiour

Más canciones de Ismaël Lô