Sofia

de Ismaël Lô

Xalatna bouguen
De guisse
Ken doulen feole
Xalatna bouguen de guisse

Gueneu waxtane mana dioubo
Lou bakhla
Xalatna bouguen de guisse
Diguen gueneu am dole

Xalatna bouguen de guisse
Gueneu waxtane mana dioubo
Lou bakhla
Ndakh koumou manti done si yengni

Ya gui bay si warwi
Ya kham guor gua yakham djiguen gua
Nguen anda ndo bay warwi
Ndakh gueum nani mbolo mbolo rek

Modi dole
Lou bakhla
Man lankeuna man bagne na
Gnou nane politicien yi dagno fewalo

Souma amone lima gueunal maan
Nguen andando boka dole
Ndakh gueum nani mbolo mbolo rek
Modi dole

Lou bakhla
Koumou manti done si gnoun gni
Diaamou senegal rek moy sa yene

Souma amone lima gueunal maan
Nagnou andando boka dole
Ndakh maan gueum nani mbolo
Mbolo rek modi dole
Lou bakhla

Maan gueum nani bougnou ande bolo
Mo gueun sougnoum rew
Nagn diohonn te loho

Maan gueum nani bougnou ande bolo
Mo gueun sougnoum rew
Nagn diohonn te loho

Xalatna lou bakhla xalatna lou gueun le
Bougnou ande bolo gnoun dana
Sapadeuguin

Xalatna lou bakhla xalatna lou gueun le
Bougnou ande bolo gnoun dana
Sapadeuguin

Ndakh maan gueum nani mbolo
Mbolo rek modi dole
Lou bakhla

Maan gueum nani mbolo mbolo rek
Modi dole
Lou bakhla

Xalatna bouguen manko dinguen
Gueune am dole
Xalatna bouguen manko gueneu waxtane
Mana dioubo
Kone lou bakhla

Más canciones de Ismaël Lô