Fa Diallo

de Ismaël Lô

Beuguena wanté mane dé dama amoul
Da nga di gouné motakh mouy sa khalaat
Ni Beuguena wanté mane dé dama Ragal
Da nga di ngouné moutakh mouy sa khalaat

Nga naan ma kay niou sey té noumouy démé?
Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar
Té legui bo ko meunoul demal teudi
Cherie coco li dé doyna kemane

Nga nane ma kay niou say té awma pantam
Fa Diallo wakhma noko toudé
Nga naan ma takk la mane awma place
Cherie coco wakhma no ko toudé
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt
Di takhawalou
Mané li dé doyna kemane

Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé

Nga nane ma kay niou say té awma pantam
Fa Diallo wakhma noko toudé
Nga naan ma takk la mane awma place
Cherie coco wakhma no ko toudé
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt
Di takhawalou
Mané li dé doyna kemane

Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé
Ni beugu na, ni beuguena la
Cherie coco wakhma no ko Guissé

Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé
Ni beugu na, ni beuguena la
Cherie coco wakhma no ko Guissé

Nga naan ma kay niou sey té noumouy démé?
Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar
Té legui bo ko meunoul demal teudi
Cherie coco li dé doyna kemane

Nga nane ma takk la mane awma pantam
Fa Diallo wakhma noko toudé
Nga naan ma takk la mane awma place
Cherie coco wakhma no ko toudé
Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt
Di takhawalou
Mané li dé doyna kemane

Ni beugu na, ni beuguena la
Fatou diallo wakhma no ko toudé
Ni beugu na, ni beuguena la

Más canciones de Ismaël Lô