Yakarouma si kén

de Dip Doundou Guiss

Suma reeni xol mi de yidde ma
Su ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg ni de ëpp na

Sama reeni xol mi de yidde ma
Ni ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg

My baby yaw, sama xol bi yaa ci ne (yeah yeah)
Teye la, su ma la bàyyee bàyyi lu neex (yeah yeah)
May janneer sa tàkkander di ma gunge (yeah yeah)
Xamal la ci sa jëmm ji laay dunde, baby

Fekk ma ci naj
Jel yobbu ma ci kër gi
Su ma la nàmmee
Jaxam gis la ci weer wi
Dama bëgg fi ci àdduna
Ñu dund aljanna
Sunu sëy bi daggan na
Yobbu ma fu la neex
Yah yeah, di diggu laal ba

Suma reeni xol mi de yidde ma
Su ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg ni de ëpp na

Sama reeni xol mi de yidde ma
Ni ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg

T’es ma lover (baby, baby, baby)
My lover (baby, baby, baby)
My lover (baby, baby, baby)
Sama lover (baby, baby, baby)

Suma reeni xol mi de yidde ma
Àdduna du neex ba ma gis ku mel ni yaw
Yaay sama baby love, sama gidelam
Yoon bi gudd bae sans yaw duma ñibbi, non
Mak yaw li ñu boole moo ñu mën
Même sunu boole ñoo koy ëpp doole
Baby mi de yidde ma
Baby you already know
Fanaan sans yaw daf may tëredi lool
Yeah, yeah

Lu ma la jox nga may delloo
Mbëggeel du jay ba ma lay jënde
Ñëwal ñu togg, ñëwal ñu pello
Loo bëgg dam koy def
Yaay sama wéeruwaay
Fecc dëgin ndaat saay pour sa xol bi nat
Baby, sama aljanna
Tax nga bàyyi yaay baay, dëkk sunu life
Baby!

Suma reeni xol mi de yidde ma
Su ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg ni de ëpp na

Sama reeni xol mi de yidde ma
Ni ma la amul woon defar naa la
Sunu diggante lépp ma ci neex
Ni ma la bëgg

Sama mbëggeel dëgg la
Wat na ni bëgg naa la
Soo tëddee nelawal
Dama la love, sama lover

Baby, baby, baby (my lover)
Baby, baby, baby (my lover)
Baby, baby, baby (sama lover)
Baby, baby, baby (my lover)

Más canciones de Dip Doundou Guiss