Top 5
de Dip Doundou Guiss
Lu tax ma gëj fi du ay mattu melentaan
UFC laa jëm damaa tàyyi ci bëre daan
Amatuma lu may prouver fàww ma dem ci yeneen base
Mbër kaamil a may daan du ku am tuuti mbërëntaan (non non non)
Tëmbal la Top 5 pënd bi jóg (skuuuu)
Tëmbal la Top 5 pënd bi jóg (ra ra ra)
Tëmbal la Top 5 pënd bi jóg
Dam la daan sa ndoŋ li dal sa kanam bi weex pënd bi jóg (ja ja ja)
Tëmbal la Top 5 pënd bi jóg
Lu tax dooleen mës a understand lu ma ne di job
Dóor mu daanu jugóo Eumeu Seen ak gone gi Lóo
Batey nanguwuñu ne dafay mel ni gëmuñu God, ya ya
Tëgg nu mboot wër ndomb kott du tee yaay teg 4 appuis
Sëriñtu job ma nga bëggon du man ay pettaaw nga gis
Pënd bi jóg ay muuss di mbów ma may leen tekkaaral bi
Chef d'entreprise laa nay leer man duma def sans jël risques
Saajo Maane laay doon ci ville bi
Sàccuma dama job gis naa ay changement du may yow
Waaye man ak 100 comas dinaa jóg
Mbaam du xaaj a mës yeewu ba fas jom
Kaañ bu mag nga, kan nga mës ray à part yow?
Ay sanqaleeñ ak ay yoo ngeen dëkke kaajéey naan danga yoor
Lu tax ma gëj fi du ay mattu melentaan
UFC laa jëm damaa tàyyi ci bëre daan
Amatuma lu may prouver fàww ma dem ci yeneen base
Mbër kaamil a may daan du ku am tuuti mbërëntaan (Non non non)
Tëmbal la Top 5 pënd bi jóg (skuuu)
Tëmbal la Top 5 pënd bi jóg (ra ra ra)
Tëmbal la Top 5 pënd bi jóg
Dam la daan sa ndoŋ li dal sa kanam bi weex pënd bi jóg
Yo, nga ne defatun rap te nga tële feesal fu xat
Kebetukati pexe njuuj-njaaj di nañ tefesu ndànk
Caisse ci pax nga bay ci àll duma gaynde gu ñu jat
Yéen a ngi fi caŋ te presque ñett at Dip génnewul gat
Noo def ma tëmbal leen Top 5 pënd bi jóg
Amuñu góomu xol nigger seen xol moo dëkk ci góom
Ku ñu tëj sa xel tijji menottes yi bis booy dee mooy jiitu sa rëcc
Sa MC king la lëmbël la doon def ba Prési jóg
Booy wax xaalis ñu caabi seen làmmiñ doon ay Xabi Laam
FIFA du CAF nigger
Jaan du naaw te biddeew du agsi naaj bi Sàmba allaar bu mag nga
Influenceusu Instagram
Sàmba Ka nga sa taat a fay gaaw comme slogan bi rang muy màjji-màjji rang yaw
Lu tax ma gëj fi du ay mattu melentaan
UFC laa jëm damaa tàyyi ci bëre daan
Amatuma lu may prouver fàww ma dem ci yeneen base
Mbër kaamil a may daan du ku am tuuti mbërëntaan (Non non non)
Tëmbal la Top 5 pënd bi jóg (skuuu)
Tëmbal la Top 5 pënd bi jóg (ra ra ra)
Tëmbal la Top 5 pënd bi jóg
Dam la daan sa ndoŋ li dal sa kanam bi weex pënd bi jóg (ja ja ja)
Más canciones de Dip Doundou Guiss
-
Holocauste
Tay Leu Kagn
-
Beut
Tay Leu Kagn
-
YMYM
Tay Leu Kagn
-
Kheula
Tay Leu Kagn
-
#Kmnd
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Bad Man
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Jëli li des
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nguur
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
LGT
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Sunshine
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Destin
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Dee ci yaw
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nimala beugué
Tay Leu Kagn
-
Damako Khar
Tay Leu Kagn
-
Dou raggal dou respect
Tay Leu Kagn
-
Niata la yalla fay sa xol
Tay Leu Kagn
-
Bandit
Tay Leu Kagn
-
Niata nio dess
Tay Leu Kagn
-
Funérailles
Tay Leu Kagn
-
Innoncent
Tay Leu Kagn