Suba

de Dip Doundou Guiss

Mënuma tiit ci sa life no matter duma la mës a juger non
Lu mu tiis tiis man bàyyi naa la ak Yàlla
Lépp ay mel ni mu meloon
Ndax boo jugee ci examen bu cóol, lalu hopital yaa ngi ci jail bi waay
Dégg naa def nga accident
Mayuñu la visa, def nga fause couche waay

(Pararaa) Dinan la xaar
(Pararaa) Gëmal ne dinga ñëwaat
(Pararaa) Dinan la xaar
(Pararaa) Gëmal ne dinga ñëwaat

Man nelawatuma ba yàndoor, suba la xamul li muy doon
(Kenn xamul li muy doon)
Dem naa ba réeroo ak samay xalaat tàggalikoo ak sama sago
Mel ni kuy gént lu ma yaakaar tay ba def ko sama xel mu naaxsaay (lu ma yaakaar mu tas)
Dem naa ba jublu yoonu caay-caay xel mi dellu ci li may xaar
Toog ci ker gi di féexlu mu tàng mel ni comme naaj
Ku fiy dem du tàggo fii kenn bëggul non waay
Fàww nga am ba dee gor mënul dëkk si ñaan
Mën nama xéy ba gontu fii dara du sotti ndax lan?

Mënuma tiit ci sa life no matter duma la mës a juger non
Lu mu tiis tiis man bàyyi naa la ak Yàlla
Lépp ay mel ni mu meloon
Ndax boo jugee ci examen bu cóol, lalu hopital yaa ngi ci jail bi waay
Dégg naa def nga accident
Mayuñu la visa, def nga fause couche waay

(Pararaa) Dinan la xaar
(Pararaa) Gëmal ne dinga ñëwaat
(Pararaa) Dinan la xaar
(Pararaa) Gëmal ne dinga ñëwaat

Yenn saa yi ngay dund loo dul nettali kenn
Ni ku nekk ci gént xamal ne Yàlla du jeex
Growing's always coming with pain, homie don't worry man
Gotta show'em that yu really want it yeah
Ndax àdduna daal coono yëfam la
Doo mës a tàggook li lay yéem
So i'm living my life stay away from them
Loo mënati daj bis dafay jeex
Yanu loo àttan, te deel moy loo mën dékku ci mbugal
Xel bu mat kàttan biceps xel moo gën bi tëkku mbër
I got a lot of dreams and believe everything gonna be alright
Baby, I got a lot of dreams and believe everything gonna be alright yeah

Mënuma tiit ci sa life no matter duma la mës a juger non
Lu mu tiis tiis man bàyyi naa la ak Yàlla
Lépp ay mel ni mu meloon
Ndax boo jugee ci examen bu cóol, lalu hopital yaa ngi ci jail bi waay
Dégg naa def nga accident
Mayuñu la visa, def nga fause couche waay

(Pararaa) Dinan la xaar
(Pararaa) Gëmal ne dinga ñëwaat
(Pararaa) Dinan la xaar
(Pararaa) Gëmal ne dinga ñëwaat

Más canciones de Dip Doundou Guiss