Sama Dome

de Dip Doundou Guiss

Bi ma la gisee dang ma xool ma bég sama xool bi naat (sama xool bi naat)
Ci ay tooñante noo ngi fo di ree kon kaay nu toog waxtaan (kaay nu weccoo)
May janeer li ne ci sa xol nga koy nëbb mu lay gaañ
Nanu doon benn lu ma am jox la loo xam wax ma

Hey
Baby, kaay nu dem nee ma waawaw
Dama bëgg nu sëy sama ndaanaan
Xol bi yaa fi fees xam nga ko you know
Dama bëgg nu dem, dem fu sori lool
Bi ma la gisee nga may xool di ree sa bëñ yu weex tàll
Ci sa bët yi laa gisee sa mbëggeel xam ne naxóo ma (non non)

Bi ma la gisee dang ma xool ma bég sama xool bi naat (sama xool bi naat)
Ci ay tooñante noo ngi fo di ree kon kaay nu toog waxtaan (kaay nu weccoo)
May janeer li ne ci sa xol nga koy nëbb mu lay gaañ
Nanu doon benn lu ma am jox la loo xam wax ma

Yaw sama saajobaan kaay wuyu ma
Ma dëkke di la joobee kaay wuyu ma
Bae su réeroo amee nu toog waxtaan
Ma di la nax ak a teete ba nga contane
Baby bul daw bul tàyyi
Soo ma nammee maa ngii
Naa la call FaceTime di xool say reetaan
Kone bul daw bul tàyyi

Bi ma la gisee dang ma xool ma bég sama xool bi naat (sama xool bi naat)
Ci ay tooñante noo ngi fo di ree kon kaay nu toog waxtaan (kaay nu weccoo)
May janeer li ne ci sa xol nga koy nëbb mu lay gaañ
Nanu doon benn lu ma am jox la loo xam wax ma

Más canciones de Dip Doundou Guiss