Reunion
de Dip Doundou Guiss
Tokk raam dokh
Limeunta gnakkeu rek la ndirok niti
Man maa leundeum yenay takkeu yenay New York City
Taatou nén la sem maam daan déf si tol bi di dokh
Balaagnouy sol silip roy ba moudiou raw iblis
Niti yén koulén comprendre dof
Koulén daw dina khokh naan ndokh
Bamay torokh wakhma kan mo beuggon melni man
Tay dagnouma topando ba meuneutouma def ni man
Nit yi pour gnom lou chère rékkeu nice
Dictateur yélay solal béret Che Guevara
Sak'ko sa bopp beugueu indépendance
Kouné sa yaye rékka doul fekk déféant ci sa bopp
Ray kénén aar tchi sa bopp
Sexe, lekk a naan tchi sa bopp
Két-kélén taan tchi sa bopp
Néék gnémé akheu
Fén rék nga meun yagga téklé ay masque tchi sa
Beuggouma interview
Animateur yi boulén ma laathie meussouma fékké tousse
Khélou djeun mo keuppeu sénégal motax ma téfessou
Fuck bépp hymne national doundouma pincez tous
Docteurs yi gno ngi won sa doundou gno ngi won sa dé
Lo guiss logiquement day diekh ma profito ba fin
Fok gnou khotti sama keuyti
Xol bi soga fëkh
Djikko niteu salté ba bossou mbot tako tané
Yea Son bi haut niveau la tay ni niom Inno Alex, my man
Do nitou dara
Compliç'ou satan
Yonénti bou yalla yonni nga sikki sakka
Wéthiét ngay diokhé comme sarakh
Di taal sa money ci sabar
Thiaga dou khammé ti thiaga
Ndax gor la goor yi di mbaraan
Fén amoul yéré ngén solalko bossou deuggeu
Xaliss di dieundeu gni fokni khaaliss day dieundeu lép
Déf comme sa waa gallé boy soga am job bou deugeur
Yaw boy lekkeu say kharit do wakh ni kharit ak deummeu yam
Li beuri loutakh ma gueuneu paré ci niti
Yenay takhal gni sét di queuneu saltél gnou tilim
Ngay neubbeutou yalla té yawla satellites yi tiim
Gneup diay li htci biir pour meuneu rafét tchi biti
Yéna créer fébar bou meuneu fadié dicci deal
Yena diox Israël mou yonner Palestine missile
Ni nga khobé si liquide rék nga amé fitou kill
Kou magg khamne ni nit rek'ka meun té def yeufou nit
Waa safara bougnou gnawwaton pour war lén dou takh ngén toup
Gnata yonn ngén diougué armél naan kou baakh ngen soule
Paré di topp bannekhou bakkén ni kouy kham say jour
Kila sakkeu nga gëm wala kiy takh sa kalpé douuf
Diangueu féy si dékhou dérét pour meun djité réw
Avenir si assamane la deukkeu kharou fii la yam
Pour lan ngay doundou ci sa biir bi di wor si sakhél
Diaroul may sonneu di wakh si sa bonne bakh nii nga mél
Más canciones de Dip Doundou Guiss
-
Holocauste
Tay Leu Kagn
-
Beut
Tay Leu Kagn
-
YMYM
Tay Leu Kagn
-
Kheula
Tay Leu Kagn
-
#Kmnd
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Bad Man
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Jëli li des
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nguur
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
LGT
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Sunshine
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Destin
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Dee ci yaw
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nimala beugué
Tay Leu Kagn
-
Damako Khar
Tay Leu Kagn
-
Dou raggal dou respect
Tay Leu Kagn
-
Niata la yalla fay sa xol
Tay Leu Kagn
-
Bandit
Tay Leu Kagn
-
Niata nio dess
Tay Leu Kagn
-
Funérailles
Tay Leu Kagn
-
Innoncent
Tay Leu Kagn