Nimala beugué

de Dip Doundou Guiss

Nel tekkeu mother fuck kinest manela doff bi maay
Check Microphone bi ngay get yaak sa copine
Légue légue may Rap dilay ray ak égotrip
Ngay fènn naane Rap dou métier ndax égo fi gaïndé
Di raak di ndèy make money sadik ngay def
Ni Mane pour xeuy tek neulé sac yi maay dem
Mane ak Saozi fokk ni nieupeu niou wara guiss
Télouma nandeu ni daw dou gaaw ak ay mbarakiss
Démal nga lathié ndéré ndakh gang bi soxla na xaliss
Dédette takouma tëré liguey rekka fi garantie
Dédette tourouma dérette YALLAH rekka fi gueuneu diss
Intérêt boula takhé jog thiénél doma meusseu guiss

Ci gaalou xathie bi ngama done khaar finalou RAP yi ngama
Done sathieu
Beus na nieuw ma wanela boy sipp na boubah li nga done
Waathie

Motah may gueuneu xoss xalima bi né sama ndèy-dior
Bou sobbé KIY MAYé waa djiy yorr bisness bi mane lay done

DIP génération bou wessou lay fay
Mane douma tiim caméra dafma lerr ni na fégne

Papa djangalma Raak déggo ko fèneu
Té ma ngui koy carrément yagg yagg day fay
May Kane, da nga beug xam may kane?

Fékk ma sama makkaane
May Kane, da nga beug xam may kane?
Nieuweul ba sama makkaane

Ma ngui djoudou beussou Vendredi 22 Mars
Bala bobou mougnena maak mère bi bène 9 mois
Awouma djotou fêté sama birthday
Damay fékhé ba kène dou faaté sama beussou déh
DIP la toudou. Yaw nak?... Okay!
Lissi dess niakoul solo mé diaroul wananté ay cartes
D'identité
Policier bilay sauvé niakoul ngène rombanté
Xamo toureum té nénay mom mo ress sa karangué

Boul khol cii nima mel boul baayi xel cii kimay ndirool
Boul khol cii limay def meunena nékaate cii yénéni rôle
Diapalni mane maay goumbeu bilay wane sa yone
Diapéma xadjou boum biy bagna feusseul sa xétou drogue

Kholéma Michael Jackson, Bob Marley ak James Brown
War ngama xamé xeuyna maak yaw nio bokone école
Manela DIP té ay diouni songs laay bindeu ndo
Sama maladie mo ngui cii Album bimala dikk

DIP génération bou wessou lay fay
Mane douma tiim caméra dafma lerr ni na fégne
Papa djangalma Raak déggo ko fèneu
Té ma ngui koy carrément yagg yagg day fay
May Kane, da nga beug xam may kane?
Fékk ma sama makkaane
May Kane, da nga beug xam may kane?
Nieuweul ba sama makkaane

Más canciones de Dip Doundou Guiss