Nightmare

de Dip Doundou Guiss

Beuré daan gnibii
Dieul sen kaagn gnibii
Dou man rekkeu deukkeu founiouy keufé sac fidi
Tabakh keur étage building
Déf essence tchi birr
Tchi biir range bi
Gueuneu thiap didi
Guénneu pape ministre
Fuck underground beatches
Cholera bitches
Doméram bitches
Diokhé taat pour siiw
Da ngén sakh ay laaf pithieu yi

Koula né damay rap pour fii
Démal laath idy
Thiouthiou snap niang wala coucou snap sidi
Man may pacotille yéneu samay plastigui
May président fifa yénay odkav bitches

Diangal sa pape sa mame balaa maa sakh sikkim
Guiss ma may wékheunték mbaam ma yamak mbaam kiff kiff
Taal sa dieummeu saw sa rouh ba assamane si khiin
Kay ma may la revanche diokh la sa dixième chance tchi bif

I'm the nightmare, you know
The nightmare is me
Call me right now
For the more way
Gnimay gnaanal amiin

Éhh yeahh yeaah yeah
Wohh woooh wooh woh

Lo niémé niakk
Lo déf day thiank
Do défé gatt
Noone yééma yarr saw la ngay naan
Khon yéla diappeu
Tok len sen place té fompeu samay dalleu
Or lamay gass niggah fuck senegal
Da ngen congelé man
Sa carrière auto bou panne la
Sa album dokhotou mbaam la
Sa bras long lokho bou gaana
Démo fénneu poto courant nga
Sa rappeur si pochettou maa niaan
Cachet ko néko mou baal ma
Nélén mounougn si man touss
Ni toubab bi ak cheikh ahmadou bamba
Roy dou ndirok piir
Bénneu boy doufi raw dip
Ndiggah fuck you mouno shit
Loudoul tokh ay kilo shit
Mané fuck diplômes yi
Doumay tok tchi bureau bi
Ma ngi tchi bandit yi
Police di daw ngay daw boy guiss police
Douma lén thiabi waayé é
Kougne sacrifié ngané kounta kinté
Poupe séni bec soul séni néw
Coup de sifflet nga poupe sa toubeuy
Si ay archive lay déf kou meun si yén
Label dou gatt ndakh goumbeuy signé
Sa guéll lay ngayyi bouggou ma si rén
Koumay soul rekkeu yor coubérou guéthie

I'm the nightmare, you know
The nightmare is me
Call me right now
For the more way
Gnimay gnaanal amiin

Éhh yeahh yeaah yeah
Wohh woooh wooh woh

I'm the nightmare, you know
The nightmare is me
Call me right now
For the more way
Gnimay gnaanal amiin

I'm the nightmare you know
The nightmare is me
Call me right now
For the more way
Gnimay gnaanal amiin

Éhh yeahh yeaah yeah
Wohh woooh wooh woh

Más canciones de Dip Doundou Guiss