Nguur

de Dip Doundou Guiss

Ou-ouh ou-ouh
Yeah, mann beugouma nékk buur
Wayé yallama deff buur
Kheuyneu, mann nangounaa
Konn meunouma mayy may bagn
Ou-ouuuh ou-ouuuuh
Yeah, may gagnn samay ennemis
Gnouy nadj sénni ranguognii
Guissna kouy yéttal najj bi
Mouné maka wara yééé
Ou-ouh ou-ou-ouh

Sama yaramm déé
Sama khéllay téy-y-y
Sama jeumeuk sama rouh moussougnou wéranté
Douma nitt kou bonn way yéneu say damay wééré
Yéneu say damay mérr teujj sam bountakk parentéérr
Yéneu say damay triste
Yéneu say damay sissou
Déé wama gueunneul tiitt kharr douma yerentii

Diganté khajjak boukki
Bidéwou khajja gouddi
Feel ngénn ba lakatoujji
Guiss ngénn ni yalla dou nitt
Foukki nooone, jounni mbokk you deuggou
Foukki gorr, jounni bopp you teujjou
Boudoul God joulliwoo dangay teureull
Toukkiwo boussa rouh bi dagnagoul
Kiliftéff doussa sikkim wéékh
Leundeumm lérr mélni timiss guéé
Tilim séttt ni jeunn si biir guédj
Sigui ténnn féssak dignité
Esprit khéll after physique khékh
Tédd tékki simple ni bill gates
Am dérrou séggg mais ay boukki nguénn

Ou-ouh ou-ou-ouh
Yeah, mann beugouma nékk buur
Wayé yallama deff buur
Kheuyneu, mann nangounaa
Konn meunouma mayy may bagn
Ou-ouh ou-ou-ouh
Yeah, may gagnn samay ennemis
Gnouy nadj sénni ranguognii
Guissna kouy yéttal najj bi
Mouné maka wara yééé
Ou-ouh ou-ou-ouh

Reptyl music
Next song

Más canciones de Dip Doundou Guiss