guerre mondiale
de Dip Doundou Guiss
Sa loxo set
Sa lepp set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn
Bul sëqët fepp
Bul jége kenn
Sëqët, fièvre, bop buy metti njëk feeñ
Soj, problème noyi, senn sa bakkan
Sëqët, fièvre, put buy metti, malaise feeñ
Du rey nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn
Sa loxo set
Sa doom yi set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn
Bul sëqët fepp
Bul jége kenn
Sa loxo set
Sa lepp set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn
Xeex ak Corona Virus
Microbe, jàngoro la, du nit
Aduna nek si combat
Du gis ku muy xeexal
Nuro nak grippe
Nañu éviter contact physique
Xajul Grand Yoff, Colobane, Pikine
Tax ba ñu annuler programmes yi siiw
Tax ba ñu foog ni àddinay tukki
Medecin sonu na si li
Amul vaccin, ordonnance tamit
Mu ngi ray, day toroxal nit yi
Buñu tooge dina bari ay victimes
Set si sa askan, set si sa bopu
Tëju te baña seeti sa mbokk
Julli sa màkkaan, Messe si la bokk
Xeex ko mu jeex mbir yepp mëna doxx
Masque, sabu, antiseptique
Raxasu, sangu dadi set wecc
Dal, muñ, bañ lu melni dess fi
Gën di ñaan pour jamm day dikk
Sa loxo set
Sa lepp set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn
Bul sëqët fepp
Bul jége kenn
Sëqët, fièvre, bop buy mett njëk feeñ
Soj, problème noyi, senn sa bakkan
Sëqët, fièvre, put buy metti, malaise feeñ
Du ray nit ku ñul si ñi xamul dëg ak fenn
Sa loxo set
Sa doom yi set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn
Bul sëqët fepp
Bul jége kenn
Sa loxo set
Sa lepp set
Bul nuyu kenn
Bul lëng kenn
Bul génn kese ndax bëg génn
Más canciones de Dip Doundou Guiss
-
Holocauste
Tay Leu Kagn
-
Beut
Tay Leu Kagn
-
YMYM
Tay Leu Kagn
-
Kheula
Tay Leu Kagn
-
#Kmnd
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Bad Man
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Jëli li des
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nguur
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
LGT
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Sunshine
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Destin
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Dee ci yaw
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nimala beugué
Tay Leu Kagn
-
Damako Khar
Tay Leu Kagn
-
Dou raggal dou respect
Tay Leu Kagn
-
Niata la yalla fay sa xol
Tay Leu Kagn
-
Bandit
Tay Leu Kagn
-
Niata nio dess
Tay Leu Kagn
-
Funérailles
Tay Leu Kagn
-
Innoncent
Tay Leu Kagn