Destin

de Dip Doundou Guiss

Dox naa la ca ker ga ak ci naaj wi
Destin la nu jaar ci
Dogal la nu jaar ci
Nattu la nu jaar ci
Lépp ak heritage bi
Mas nañ ma miraas

Papa sonal naa la de (wey)
Maa la soxla naa ko def (hé)
Ci gaalu xaj bi lañ ma yakkal
Kuy xaar ma xàddi naa la yeetal (oooh)
Papa sonal naa la de (hey)
Maa la soxla naa ko def (hey)
Ci gaalu xaj bi lañ ma yakkal
Kuy xaar ma xàddi naa la yeetal

Yow Jug balaa picc yi di sab
Dem utiji kaañ, du feebaar bu clinique di faj
Game bi ni picc ci taab
Ñii di pique ñii di clash, ba gaynde di xiiru ni xaaj
Gisuma fi lu fi tar
Te feeluñu gaa yi
Duñ booloo ni fiillu gitaar
Hit yi ba 10mil GIGA
Nga siiw fi ni taat
Ma tas leen ci digg bi side

Ëllëg rekk lan mas sóorale du añ du reer
Ëllëg a nu foqaleloo
Ndax dee gi gaaw na dëgg ñaan naa Yàlla, Yal na yeex
Tedd soog a man a nelaw
Liggéey di fight 1: 04mn
Tas ko fépp ba raw réseau
Ku juum ba dee ci ñàkk jamono jii yal na dee, dee ci ñàkk yal na dee

My nigga I'm coming, y'all ready know it
You know that I'm coming
Bitch Nigga I'm coming

Y'all nigger unduwoleen sadikooleen
Dangeen a suulu bay gis pax yu kawe
Ci sama ruu laay dund kenn du ko ray
Soxlawuma tulu bomb ak pistolet

Dox naa la ca ker ga ak ci naaj wi
Destin la nu jaar ci
Dogal la nu jaar ci
Nattu la nu jaar ci
Lépp ak heritage bi
Mas nañ ma miraas

Papa sonal naa la de (wey)
Maa la soxla naa ko def (hé)
Ci gaalu xaj bi lañ ma yakkal
Kuy xaar ma xàddi naa la yeetal (oooh)
Papa sonal naa la de (hey)
Maa la soxla naa ko def (hey)
Ci gaalu xaj bi lañ ma yakkal
Kuy xaar ma xàddi naa la yeetal

(Oh oh oh) Ku dee ci ñàkk yal na dee
(Oh oh oh) Ku xaar ma xàddi naa la yeetal
(Oh oh oh) Ku dee ci ñàkk yal na dee (oh)
Ni Saajo Maane Gànna Géy
Ku xaar ma xàddi naa la mas a yeetal

Jafe ni siggi ci naaj
Ni ku Iblis di jaamu
Ni Hindu bu chirurgie ñaw
Rappeur yi defoon seen xel ni que mas nañ ma fuck
Dañ yeewu seen slip yi tache
Yaw mag nga ni ndigg bu panne
Say siddit yu caas
Te gis nga sa sikimu caat
Xam nañ fu xiir gi di daw, fu semmiñ di aw
Ngay fen rekk ni xiin wu dul taw

Maa moom sama territoire sama nigga
Manóo rax sunu biir
Kon bàyyi ma ak sama wéetaay nigga jëlal sa distance middle finger
I'm on my way starting from the bottom for the top amuma limite
Kon bàyyileen di ma tëkkaleek seeen nigga
Fuck seen bépp xeetu nigga

My nigga I'm coming, you already know it
You know that I'm coming
Bitch Nigga I'm coming

Fi ku fi bokkul nañ rëkk sa ndigg
Ngay toppandoo jaawale wërsëg ak liggéey
Wéyewóo ma waaye ngay wéy ci samay ndigal
Ay secret ngeen Google du wër sax ba gis leen, bitch

(Oh oh oh) Ku dee ci ñàkk yal na dee
(Oh oh oh) Ku xaar ma xàddi naa la yeetal
(Oh oh oh) Ku dee ci ñàkk yal na dee (oh)
Ni Saajo Maane Gànna Géy
Ku xaar ma xàddi naa la mas a yeetal

Papa sonal naa la de (wey)
Maa la soxla naa ko def (hé)
Ci gaalu xaj bi lañ ma yakkal
Kuy xaar ma xàddi naa la yeetal (oooh)
Papa sonal naa la de (hey)
Maa la soxla naa ko def (hey)
Ci gaalu xaj bi lañ ma yakkal
Kuy xaar ma xàddi naa la yeetal

Más canciones de Dip Doundou Guiss