Ci naka
de Dip Doundou Guiss
Eey Tàmbali naa te dinaa fi sax
Sama bilan ci 10 ans de pas
Camavinga, Vinicius, Bellingham bind jamono
Juvantus Zidane ci ball
Doo ma gisaat bu ginaar di sab
Yorante baa ngi ci finance ci cash
Xam nga bu baax ki fi rap et puis t'as vu
Fépp ñu indiwaat ci siitaatukat
Eey Yaa téeye game ci naka
Yaay seen king bi ci naka
Ci naka noonu ci naka
Ci naka noonu ci naka
Yaa téeye game ci naka
Yaay seen king bi ci naka
Ci naka noonu ci naka
Ci naka noonu ci naka
Kon yaa téeye game bi
Deel simb gaynde ni Bafetembi
Wembanyama fils, Kañ ngay tiim DIP
Bengalewaate laa dëkke seen biir
Rolls-Royce flow la du Toyota bitch
Sama yoon ci sa jooy ak nàcc
Nigger Dip fayul courant du tooyal naaj wi
Duma 1Xbet duma joobal naar bi
Dama dugg ak defaite génn ak sa tête
Ñibbeeg coupe du monde bi comme Argentine
Depuis Bis Niki Tay ba LFLF
Xam ngeen Araf yi, xam ñan ñooy arnaque yi
Jëmbatunu fi jàmm booy jëfër bul nu digaat
Jëfërunu di saaga te jëfanduwunu ci clash
Cheveau du lu ñuy daj ku lay ëwal tulu ñi takk
Nëbbatu di jihaat nigger fésaluñu ci gat
Amul fital bu pirate di jay
Amóo fi place ni imaam ci boite
Coow li amóo ci gat ni miraas ku ñàkk
Game bi dina besaat ni siraas ci dàll
Tàmbali naa te dinaa fi sax
Sama bilan ci 10 ans de pas
Camavinga, Vinicius, Bellingham bind jamono
Juvantus Zidane ci ball
Doo ma gisaat bu ginaar di sab
Yorante baa ngi ci finance ci cash
Xam nga bu baax ki fi rap et puis t'as vu
Fépp ñu indiwaat ci siitaatukat
Eey Yaa téeye game ci naka
Yaay seen king bi ci naka
Ci naka noonu ci naka
Ci naka noonu ci naka
Yaa téeye game ci naka
Yaay seen king bi ci naka
Ci naka noonu ci naka
Ci naka noonu ci naka
Dama jug, ngeen paan
Amuma noon seen rap
Ku dul tàkk manoo fay Dip
Sama coach day xaar
Nigger comme Mbay Jaañ
Dama ko teppi ci posteer bi
Dama dof dem FAAN
Rap ba dof ni humeur
Danga dof te dinga des fii
Du ci son du ci marque du show
Moo tax ambassadeur ne masóo def chiffre
Di raam ba jug dox dem
Dama ko xeex comme bi Mód Lóo def
Ñëwandoo ak nillard yu bon comme yéen
Duñu ko yëg comme jëlaat seen compo pée
Dangaa cóol te bizzare ni nob koo bañ
Comme bi Adam bi xàmp pomme mook Eve
Danga alku ni Firhawna nëb comme néew
Ku la xoojoon 10 ans di fóot doo set
Dinga daj li cin daj ci taal
Du tax nga mas a tàkk ni galaas ci gaz
Loxoom du jug ni nillard ci classe
Nigger sama fils nga duma biiral di bañ
Tàmbali naa te dinaa fi sax
Sama bilan ci 10 ans de pas
Camavinga, Vinicius, Bellingham bind jamono
Juvantus Zidane ci ball
Doo ma gisaat bu ginaar di sab
Yorante baa ngi ci finance ci cash
Xam nga bu baax ki fi rap et puis t'as vu
Fépp ñu indiwaat ci siitaatukat
Eey Yaa téeye game ci naka
Yaay seen king bi ci naka
Ci naka noonu ci naka
Ci naka noonu ci naka
Yaa téeye game ci naka
Yaay seen king bi ci naka
Ci naka noonu ci naka
Ci naka noonu ci naka
Más canciones de Dip Doundou Guiss
-
Holocauste
Tay Leu Kagn
-
Beut
Tay Leu Kagn
-
YMYM
Tay Leu Kagn
-
Kheula
Tay Leu Kagn
-
#Kmnd
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Bad Man
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Jëli li des
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nguur
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
LGT
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Sunshine
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Destin
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Dee ci yaw
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nimala beugué
Tay Leu Kagn
-
Damako Khar
Tay Leu Kagn
-
Dou raggal dou respect
Tay Leu Kagn
-
Niata la yalla fay sa xol
Tay Leu Kagn
-
Bandit
Tay Leu Kagn
-
Niata nio dess
Tay Leu Kagn
-
Funérailles
Tay Leu Kagn
-
Innoncent
Tay Leu Kagn