Bad Man

de Dip Doundou Guiss

Mounou mala wahk dete
Lep lo beugue beugue na
Feep fo beugue beugue na
Tegoulo ma gaathié
Dang ma dolél yeukatima
Fo guesto guis ma sa guinaw
Mounou mala faté
Mounou ma faté fignou diarr
Sama khole ken doufa dougate
Beugue la dounde ak déé
Dang ma beugue ma beugue la
Dila beug ba abadane

Baby, I'm a bad man, bad man, bad man (no no no no)
Baby, I'm a bad man, bad man for you (you know that I'm a bad man)
I know You know that I'm a bad man bad man bad man (no no no no)
You know that I'm a bad man bad man for you, yeah hé

Lo def si man, fo né si man
Sokhna si kay bouma soriti way
Khol ma si eyes bb, niewal si man
Call ma niou wakh, do ré mi fa
Teudj ma wane ma lou gueuneu sorri si iow
Fayal lamp ma wane la lo beug guiss
Foy guis kanén koko meun defé ni man
Ling'ma wane lep nga neub niit yi
Kagne dem, kagne dem, kagne dem
Kagne dem bagna delousi
Kagne dem kagne dem bagna niewat
Kagne dem kagne dem
Mounou mala wakh dé
Lep lo beugue beugue na
Fep fo beubue beugue na
Tegouloma gathié
Dang ma dolel yekatima
Fo guesto guis ma sa guinaw
Mounoumala faté
Mounou ma faté fignou diarr
Sama khol ken doufa dougatt
Beug la dounde ak dé
Dang ma beug ma beug la
Dila beug ba abadane

Baby, I'm a bad man, bad man, bad man (no no no no)
Baby, I'm a bad man, bad man for you (you know that I'm a bad man)
I know You know that I'm a bad man bad man bad man (no no no no)
You know that I'm a bad man bad man for you, yeah hé

Souvenirs yi dess sama mind noo
Soumala guisoul sa ay foto laye khole
Yaye sama sadia bane sama aldiana
Douma meussa sey boudoul mak iow
Baniouma gagne sama boop
Soko beugué, yaye sama khol
Sama mbeuguel, dima ray dima fone
Every day ya ya ya ya yaaaa
Kagne dem kagne dem kagne dem kagne dem Bagna deliusi
Kagne dem kagne dem bagna niewat
Kagne dem kagne dem
Mounou mala wakh dé
Lep lo beug beug na
Fep fo beug beug na
Tegouloma gathié
Dang ma dolél yeukatima
Fo giesto guis ma sa guinaw
Mounou mala faté
Mounou ma faté figniou diarr
Sama khol ken doufa dougat
Beugue la dound ak dh
Dang ma beug ma beug la
Dila beug ba aabadane

Baby, I'm a bad man, bad man, bad man (no no no no)
Baby, I'm a bad man, bad man for you (you know that I'm a bad man)
I know You know that I'm a bad man bad man bad man (no no no no)
You know that I'm a bad man bad man for you, yeah hé

Han han han han haann
Reptyle Music

Más canciones de Dip Doundou Guiss