40e jour
de Dip Doundou Guiss
Hey
Ñëwuma pour suuxat jàmm
Waxumaak boroom xélu surgak jaam
Defóo fi lu kawe, li nga sut moo gàtt
Duma mas a màggetee ni yéen Tout sauf ça
Nitewooleen, salte ngeen ni douche ak sax
Tax may reewantu ni caat ba mujj rus doon taaw
Wane li say ñoñ ñàkk bëgg mussloo cat
Làmb ji tas te du ku ci dàq a tuus moo daan
Yàlla newul fépp kuy comprendre
Fépp a ne ci Yàlla même sa Google map
Dëkku 1er pee raw mais 2ème bee man
Jaralooleen ma may génne sama 2ème souffle
Liggéey ba ñaq ngeen tàyyal, sawar a jëw bay yuut
Xéy ci jàdd yoon gontu jubal penku
Bañuma leen daa fekk su ma leen suulul dañ may suul
Gën ji mbindeef terewu la gëm Jesus yeah
40e jour
Reptyle ñoo sikk fàww ñu quarantaine nu
DIP dafa lëndëm trop il faut carte d'identiteem ñuul
A part père You life du dox ba ndanaan yéem nu
Kaani laa ci bët, bazin riche ak Geztner, Ganilaa ci bës
Kaamil ak Bible dee ci nguur gi, f*ck candidat bi gën
Man ak ñoom Angleterre Senegal la, chaque mi-temps ñu jël
Fi ba buumu jaam gi di dagg ni nun ak France
Nigga who got yeah who got the juice i got
Damaa xiif at géej gi sax fajul sama mar
Dun sikar bu dul AHMADU BÀMBA
Ñaari gët du gis nan ngay xoole sa bët du xol
Bakken nopp bët ak làmmiñ fi mbalit jaar ba bëtt xol
Bëgun nguur gu këtt ne jonn, Amuma bor ci ëttu gor
Li may togg day xëm du ñor, Waante lu ma dëbb mu mokk
Dama doyal sëkk ak gaa yi teg seen ngor ci marché jënd ak jaay
Du ak li nga jaaye sa ruu ngay lebe samay fan
Seen buzz yuñ lëmës jaan
Taxul ma get seeni bum yi mbëbës dàq
CNG la jënndoon daaw bul xaar ren sa mbër daan
Grand dëggal bal bi xewwi ngeen ni jungle dëngal xaaf
Jëndal glace dun séq lu dul dëbb ak wal rekk
Feat ak yéen underground ndëppal sàcc beat yuñ tëgg ak tànk
Di leen fëlëntal ni heure ak temps bay tax nu wér ak jàmm
Dama daan ni EUMEU ak BÀLLA dama gaaw ni xal ak jassi
Doomeraam yi gas sam kàmb may dëj seen maam bëccëg ndara kàmm
Am ay noon ci sama gang li tax may raag nga sakkan kaar
Davala ci kaw lay jaar pour ñi may xaar ci suuf ndeysaan!
Dama
Dma daan
Dama
Dama daan ni EUMEU ak BÀLLA dama gaaw ni xal ak jaasi
Más canciones de Dip Doundou Guiss
-
Holocauste
Tay Leu Kagn
-
Beut
Tay Leu Kagn
-
YMYM
Tay Leu Kagn
-
Kheula
Tay Leu Kagn
-
#Kmnd
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Bad Man
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Jëli li des
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nguur
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
LGT
LNN (Loo Ñeme Ñàkk)
-
Sunshine
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Destin
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Dee ci yaw
LFLF (Lepp Fii Lañu Fekk)
-
Nimala beugué
Tay Leu Kagn
-
Damako Khar
Tay Leu Kagn
-
Dou raggal dou respect
Tay Leu Kagn
-
Niata la yalla fay sa xol
Tay Leu Kagn
-
Bandit
Tay Leu Kagn
-
Niata nio dess
Tay Leu Kagn
-
Funérailles
Tay Leu Kagn
-
Innoncent
Tay Leu Kagn