Yaw la

de Dieyla Gueye

Yaa ngi dee ndax man
Maa ngi jooy ndax yaw
Li ñu boole moo bari doole
Ak a ma leer ne yaw laa nob
Su ma geestoo gis la kontaan
Boo ma xoolee ree
Ni ñuy nammantee
Yaw laa nob

Ragaluma loolu (yaw laa nob)
Dawuma loolu (yaw laa nob)
Iso nenne yaa ma jaral lii
Man de yaw laa nob
Ragaluma loolu (yaw laa nob)
Dawuma loolu (yaw laa nob)
Iso nene, liy xasan neex ci sama xol bi

Waay waay
Fan nga ne ci man mbëggéel
Xam naa maay sa Indo
Ci léewatoo dem nga Ardo
Bëgg nga ma ba mu jeex
Ba ma xam ko dawuma yoole
Yaw laa nob

Man lañuy wër te yaw laay wër
Jébbal naa la sama xol bi
Nekk ak yaw di dund sama mbëggéel
Daf may neex (yaw laa nob)
Man nga fii te man nga fee
Xam nga lii te xam nga lee
Reewal ma te doo ma yër
Bébé lu ma bëgg rekk daf lay neex

Yaa ngi dee ndax man
Maa ngi jooy ndax yaw
Li ñu boole moo bari doole
Ak a ma leer ne yaw laa nob
Su ma geestoo gis la kontaan
Boo ma xoolee ree
Ni ñuy nammantee
Yaw laa nob

Ragaluma loolu (yaw laa nob)
Dawuma loolu (yaw laa nob)
Iso nenne yaa ma jaral lii
Man de yaw laa nob
Ragaluma loolu (yaw laa nob)
Dawuma loolu (yaw laa nob)
Iso nene, liy xasan neex ci sama xol bi
Yaw ne yaw laa nob!

Ndeke mbëggéel ni la neexee
Dama la bëgg lool (yaw laa nob)
Maa ngi baax yaa ko woyofal ba ma àttan ko
Yeeah amore (yaw laa nob)

Amore foo ne laay ne
Yaay bànneex, yaay yërmande
Bu ma mere ci sama fiiraange
Bébé yaw dama la nob

Man nga fii te man nga fee
Xam nga lii te xam nga lee
Reewal ma te doo ma yër
Bébé lu ma bëgg rekk daf lay neex

Yaa ngi dee ndax man
Maa ngi jooy ndax yaw
Li ñu boole moo bari doole
Ak a ma leer ne yaw laa nob
Su ma geestoo gis la kontaan
Boo ma xoolee ree
Ni ñuy nammantee

Yaw laa nob
Ragaluma loolu (yaw laa nob)
Dawuma loolu (yaw laa nob)
Iso nenne yaa ma jaral lii
Man de yaw laa nob
Ragaluma loolu (yaw laa nob)
Dawuma loolu (yaw laa nob)
Iso nene, liy xasan neex ci sama xol bi
Yaw ne yaw laa nob!

Bëgg naa, bëgg naa, bëgg naa
Man de nob naa
Bëgg naa, bëgg naa, bëgg naa
Man de yaw laa nob

Más canciones de Dieyla Gueye